Baba mi ani
I guili wana merer
Waa ji su ma koy xoolee ak ni mu mel
Ah, n bi ne ci neex
Ubbi buntu bus bi dugg sama xol
Li moom du neen
Mu geestu xool ma
Ci la xam ne du xemmem
May ñami-ñami
Ku la jib waññi yaay dos d’âne
Bus ba ngi daw te romb na sama arrêt
Mbaa du terminus la ma jëme
Dara dakar foo dem-dikk
Fees nga dell ci man
Te xawma yaw la kan
Xol bi naan ma te nga dem-dikk xool ba xam
Fees nga dell ci man
Te xawma yaw la kan
Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb
Ouhe baba, ouhe
Ouhe baba
Mbiɗa yiɗmaa
Yiɗmaa
Bus ba ngi riir, man degatuma
Bëgg naa la piir ndax gisatuma
Mbëggéel bu gaaw mel ni lu jaare si peage
Oh dof naa ci yaw, ki la doon seet?
Jomb te gisuma jinne (aaahn aaahn)
Jàpp ma tej condamné (aaahn aaahn)
Jokk na arrêt lay demandé (aaahn aaahn)
Ba chauffeuru bus bi freiner
Mu nax ma séy
Fees nga dell ci man
Te xawma yaw la kan
Xol bi naan ma te nga dem-dikk xool ba xam
Fees nga dell ci man
Te xawma yaw la kan
Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb
Le courage m’a quitté
(J’ai même pas osé tenter)
Hypnotisée par son charme
J'suis tombée en amour
Fees nga dell ci man, ahan
Xol bi naan ma te nga dem-dikk xool ba xam
Fees nga dell ci man, ahan
Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb
Ouhe
Fees nga dell ci man (ouhe)
Te xawma yaw la kan (ouhe)
Xol bi nana ma te nga (ouhe)
Dem-dikk xol ba xam (ouhe)
Fees nga dell ci man
Te xawma yaw la kan
Xel bi naan ma toggal bul dem jigéen du yomb
Ba bus bi freiner
Ci la xam ne rëcc na ma
Lu tax demuma?
Ba ci moom wax ko li fi ne!