Andado te bollo
Japando jeufando
Kaf ak retane lagnou xame gnoune
Yarak teguine bokk ndey baye
Yarondo magondo
Fowando jangondo
Kaf ak retane lagnou xame gnoune Yarak teguine bokk ndey ak baye
Sou tabaski joter kouner raye xare
Dimbalanter balanter
Ba do xamer kane mothiye
Catholique Bi mba joulit
Li moye sounou senegal
Pays de la teranga
Fo meunna ti joguer
So gnewer gnou teralla
Welcome to senegal
Nagnou sameu jiko yi
Welcome to senegal
Nagnou sameu Dîner yi yi
Deuk Bou ni mel waxma fan la ame
(Da ngaye done gane tewoul Fek fa sa agne)
Deuk Bou ni mel waxma fan la ame
(Da ngaye done gane tewoul Fek fa sa agne)
Kaye Kaye Kaye lene gnou ligueye
Defare sounou rew ba kou fi gneuw geune Gno naw
Kaye Kaye Kaye lene gnou wanee
Sounou deuk Bi jame lanouye titero
Deuk Bou ni mel waxma fan la ame
(Da ngaye done gane tewoul Fek fa sa agne)
Deuk Bou ni mel waxma fan la ame
(Da ngaye done gane tewoul Fek fa sa agne)
Kaye Kaye Kaye lene gnou ligueye
Defare sounou rew ba kou fi gneuw geune Gno naw
Kaye Kaye Kaye lene gnou wanee
Sounou deuk Bi jame lanouye titero
Welcome to senegal
Nagnou sameu cada yi
Welcome to senegal
Nagnou sameu
Thiossan yiyi yi
Eh
Gnouni Nene la
Bougne di gnawo
Nagne lene andando
Siguil senegal
Rewoume teranga