notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Fans Yi

ADIOUZA

Fans Yi

Man bëgg naa leen
Eh bëgg naa leen
Fans yi namm naa leen
Namm, namm, namm naa leen

Dix ans déjà yoon wi metti na
Céy yi la sopp bàyyiwuñu ma
Yàgg na bëgg def wéy wi
Wax leen fi ma tollu ci yeen
Lu ne nguene di dathieu
Ngir man te man yek naa ko
Xeex suba ngoon yek naa ko
Lu leen metti yek naa ko
Man sama xel, sama xol laa ngi ci yeen
Taye ma sargal leen yeen fans yi

Man bëgg naa leen
Eh bëgg naa leen
Fans yi namm naa leen
Namm, namm, namm naa leen

Liggéey boo ci doonee jigéen
Fawke nga xam ne fu la mooy li gën
Yenn saay nit gise la télé xemem la tok di jooy
Wër la wóolu la nga ñëw boo noyer bopp jooy
Kaay ma xamal leen tuuti
Fans yeenu yëkkëti

Ani wa pikine
Parcel, thiaroye, yarax
Guediawaye rio
Keur massar médina
Ziguinchor ba ndar bëgg nañ ma waye
Mauritanie ba gambie bëgg bagg nañ ma waye
Jàpp ngeen tewa bàyyi, duma xadi waye

Man bëgg naa leen
Eh bëgg naa leen
Fans yi namm naa leen, namm naa leen
Man bëgg naa leen
Eh bëgg naa leen
Fans yi namm naa leen, namm naa leen

Tay ma weuyale leen
Yena ma japaler
Tay ma xamal leen
Yena ma dolele
Tiaba, diarra nancy, bigue, maimouna awa toure
Wool ma maam jonge loxo ca kaw
Leggo leggo

Weuye lene ma ndeysaan sama mak ji
Ana sagna chéri sadia
Wool ma lamine fall ak fatou thiam
Bëgguloo ma mère dale yaw
Doomi ndey mami diouf
Su ma demee bàyyi bëgg xaadi chéri aziz ndiaye dolele ma
Su ma demer baye beuger xadi
Khady koundoule dolel ma
Tassou
Sa goune sa goune

Dioudou bou reye ndey ak baay
Foulak fayda borome dale
Mareme chalar mimaye beugeu jigne
Aida seye chéri lamine la bokkale baay
Fu sama rangogne touro
Mareme fompale ngamako
Raki gamou seye
Diarama mareme
Weye lele weuyelelene ma mareme
Souma demer baye beugeu xady
Chéri doudou dolelma
Souma demer baye beugeu xady
Fat kine dolelma

DJ boubs, pape cheikh, cheix sar sidathe gnoma terrer chômer
Abba, koutia, alima Maria gnoma tere chômer
Dieynaba, nadia, haini, maty, kebs thiam leggo leggo

Tracker