Che on the beat
Baby I got to Go
I can't take it no more
Bills are getting high
And my wages are low
Life is hard in here I got to get away
And our kids need more love
Faut ma touki
Te diaral nama dieuli ji gale
Dieuli ji gale
Douma xare kone faut k ma Dem fenene
Fou geune fi
Doundou lenene
Lou geune Li
Ndiabot gui weur ma loyer agne ak rere
Dara douma teyer
Ndéwo yékhi o artaani
Yalla deffna moujer woule gnewate
Ndéwo yékhi o artaani
Yalla deffna moujer woule gnewate
He Wakes up in the morning
And tell me he will Go
That he will Go
Where the golden Apples grows
Life is hard in here
He got to get away (way)
And our kids need more love
Wara Dem ni
Te woroul saxe mou deloussi
(Deloussi)
Mome nena daye Dem
Ndax teral yayame
Diaralnakoko
Sokhnassi tame sokhla na topato
Metite si xole yi
Ndax Dina meussa degne
Gnoune de sonanagnou
Thiono yi kagne laye jexe
Ndéwo yékhi o artaani
Yalla deffna moujer woule gnewate
Ndéwo yékhi o artaani
Yalla deffna moujer woule gnewate
Dimbali lene
Ndaw Gni gnou ligueye
Ndax gnou Guisse s'en bop si mime rew
Africa soula saye dome waner guinaw
Kagne ngaye nate
Ouhnn ouhnn
Ouhnn ouhnn
Yeah le le le
Ndéwo yékhi o artaani
(Africa nagnou bolo)
Ndéwo yékhi o artaani
(Li de metina)
Iyee yee
Jeuli na gale gui
Yalla deff na
Moujer woule gnewate