notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Joli Garçon

ADIOUZA

Joli Garçon

Mayday, mayday, oh oh!
Yooxu na mayday, oh oh!
Mbégté la gisatul
Man, dama muje mar
Demleen wax ko ko!

Eh yaw, lan la?
Danga toogoon samay xef
Sori naa la
Maa ngi dundu aljana

Léegi dama fine (eh! Dama fine)
Eh!, dama cool (man dama cool)
Du gis nga ni ma jekke
Maa ngi ok! (Ok!, ok!)

Lii nga ma daan dunduloo
Wuute nak lii ma doon
Mbëggeel bi dafa toxique
Stress bi bari woon
Ma dëkke jooy, léegi jeex na
Dellu sama kër
Xamoon naa ni yàlla jeexul
Maa ngi ak joli coeur

Ndax yii xeetu feem
Yii xeetu tendresse
Yii xeetu baax baax
Maa ngi dundu, ma belle
Kaay waay kaay
Baby ñëwal kaay
Kaay waay kaay
Sama joli garçon

Yaa ma jële ci lëndëm
Sama joli garçon
Fi nga ma indi, dafa leer
Joli garçon
Danga rafet, sama chéri
Waaye xol bi mool a dàq
Daddy, yëngal nga ma

Eh yaw, lan la?
Danga toogoon samay xef
Sori naa la
Maa ngi dundu aljana

Léegi dama fine (eh! Dama fine)
Eh!, dama cool (man dama cool)
Du gis nga ni ma jekke
Maa ngi ok! (Ok!, ok!)

Sa mbëggeel amul frontière (jege ma)
Yaay passeport bi may tukki loo (yóbbu ma)
Kaay fii nii, daagul
Yaa ma def nii, jaayul (oh!)

Yii xeetu feem
Yii xeetu tendresse
Yii xeetu baax baax
Maa ngi dundu, ma belle
Kaay waay kaay
Baby ñëwal kaay
Kaay waay kaay
Sama joli garçon

Yaa ma jële ci lëndëm
Sama joli garçon
Fi nga ma indi, dafa leer
Joli garçon
Danga rafet, sama chéri
Waaye xol bi mool a dàq
Daddy, yëngal nga ma

Eh yaw, lan la?
Danga toogoon samay xef
Sori naa la
Maa ngi dundu aljana

Léegi dama fine (eh! Dama fine)
Eh!, dama cool (man dama cool)
Du gis nga ni ma jekke
Maa ngi ok! (Ok!, ok!)

Danga chon, sans-façon, joli garçon
Danga chon, sans-façon, joli garçon
Man woy naa la sama chéri

Danga chon, sans-façon, joli garçon
Waaw waaw, chéri
Sans-façon

Tracker