notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Ma La Nob

ADIOUZA

Ma La Nob

Lu tax ma bëgg la?
Lu tax ma sopp la?
Yaay sukkar te ragaluma jabeet
Tu me fais kiffer

Lu tax ma bëgg la?
Lu tax ma sopp la?
Yaay sukkar te ragaluma jabeet
Tu me fais rêver

Dañu ma ni tànnal!
Ma jox la sama volant, baby dawalal, dawalal
Yaay boroom tali bi
May alkati bi laajuma la permis
Non, non, non, non, non
Yaay doo ñoom
Ba xol bi réere ci mbëggeel yaa ko for, yaa ko for
Ku ci mer, tant pis!
Ku ma bëgg na ma bàyyeek sama honey, honey

Yaa ma def ni ma mel, ma la nob!
Dama barde ci yaw, ma la nob!
Danga sori ci man, ma la nob!
Ndax bëgguma ñu wéet, ndax danga sob
Yaa ma def ni ma mel, ma la nob!
Dama barde ci yaw, ma la nob!
Danga sori ci man, ma la nob!
Ndax bëgguma ñu wéet, ndax danga sob

Lu tax ma bëgg la?
Lu tax ma sopp la?
Yaay sukkar te ragaluma jabeet
Tu me fais kiffer

Lu tax ma bëgg la?
Lu tax ma sopp la?
Yaay sukkar te ragaluma jabeet
Tu me fais rêver

Tu as conquis mon cœur sans la moindre résistance
Et il sera à toi pour toute mon existence
Qu’on soit ensemble ou à distance je t'aimerai
Sans répit, avec patience (eh eh)

Yaa ma def ni ma mel, ma la nob!
Dama barde ci yaw, ma la nob!
Danga sori ci man, ma la nob!
Ndax bëgguma ñu wéet, ndax danga sob
Yaa ma def ni ma mel, ma la nob!
Dama barde ci yaw, ma la nob!
Danga sori ci man, ma la nob!
Ndax bëgguma ñu wéet, ndax danga sob

Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay sukar té ragalouma diabète
Tu me fais kiffer

Loutax ma beug la
Loutax ma sopp la
Yay soucar té ragalouma diabète
Tu me fais rêver

T’es mon choix dara fayu la, baby
Dangay mer di gën a jantal
Di xuloo sax di gën a jantal
Sappeur fayu la

Yaa ma def ni ma mel, ma la nob!
Dama barde ci yaw, ma la nob!
Danga sori ci man, ma la nob!
Ndax bëgguma ñu wéet, ndax danga sob
Danga sob, danga sob
Danga sob, danga sob

Tracker