Or ak iPhone
Bae jege si ma may la ay fóon
Ki la dagal ñaw na ciseau
Fi wëñ am na fi nasal puso, yeh
Xam naa sa mesure, dama lay ñawal
Yere bi la jot man rekk maa ko xam
Bokkuloo ganila danga riche ni bazin pure
Non non getzner lalay ñawal
Loo waxati (bëgg naa)
Modèle bi (saf na ma)
Yaw jegesil (ah)
Dozel ma ku la neex (ahn)
Ko masel tiit na
Ci sa jongoma
Te foo daagu wane sa cas
Ñëpp kontaan
Dawuma lu ma lay name
Seen lammiñ dama ko tul
Dawuma lu ma lay name, eh waaw
Samay noon na may gunge
Man xam naa
Li toogu maa ko rotoon
(Mi ngi tuuru)
Doy na ba mu fees
Kaay tànk may noon mu naan
Soxor rang koy ray
Wax ju bari day yokku mar
Buleen faale nañu dem
Yoon wi dafa guddu lool
Luñ ci man nañ ko jëm
Lii ko tëgg tasu ko
Buy neex maa ngi fi
Bu metti maa ngi fi
Dereetu góor ci sama yaram duma la wor
Soo bëggee bëgg naa
Fu mu yam neex
Li ku mu metti nanal asip
Sama Nutella, chocolat d'amour
Non non getzner laa lay ñawal
Loo waxati (bëgg naa)
Modèle bi (saf na ma)
Yaw jegesil (ah)
Dozel ma ku la neex (ahn)
Ko masel titna
Ci sa jongoma
Te fo daagu wane fa cas
Ñëpp kontaan
Dawuma lu ma lay name
Seen lammiñ dama ko tul
Dawuma lu ma lay name, eh waaw
Samay noon na may gunge
Xam naa sa mesure, dama lay ñawal
Yere bi la jot man rekk maa ko xam
Bokkuloo ganila danga riche ni bazin pur
Non non getzner laa lay ñawal
Bae ki lay foto jarul flash
Ne ko leer na
Yaay sama jànt
Mat ma flash, lépp leer na
Romb nga modèle raw miss
Fooy défiler
Yaa ma lalal tapis rouge
Ci sa xol bi fa laay défiler
Loo bëggeti yaa tax ma wéredi
Roof buggati loo wax ma defati
Looy defati loo wax ma bëggati
Te fu ñu gisati seen xol du neex
Soo bëggee bëgg naa
Fu mu yam neex
Li ku mu metti nanal asip
Sama Nutella, chocolat d'amour
Non non getzner laa lay ñawal
Loo waxati (bëgg naa)
Modèle bi (saf na ma)
Yaw jegesil (ah)
Dozel ma ku la neex (ahn)
Ko masel tiit na
Ci sa jongoma
Te fo daagu wane fa cas
Ñëpp kontaan
Dawuma lu ma lay name
Seen lammiñ dama ko tul
Dawuma lu ma lay name, eh waaw
Samay noon na may gunge