Monsieur bonheur neex a jubool
Dafa jot nga ñëw ñu wax
Tay jàmm laa yeewoo
Bae, sagu bi doy na
Maa gis neen, ne neen a ngii
Càppaacóoli doo kenn ci ñii
Loo viser doo ko moy
Rafet ngemb man a bëre suuf
Noonu laa lay nammee
(Dootuma ko def, dootuma ko def)
Te foo meree ma jaaxle, bébé
(Dootuma ko def, baal ma, dootuma ko def)
Yaw xool ma tey ree, bébé
(Dootuma ko def, dootuma ko def)
Ñu def juboo de l'année bébé
(Dootuma ko def, baal ma, dootuma ko def)
Damaa pare jubook yaw
Ba foofu ñuy woowe wuy yaay (ooh ooh!)
Xamante nañu du am coow (ooh ooh!)
Jéll am foo ko foogeewul
Suukar bi ci banaana
Pare nooy ni xaal
Menthe bi ne ci naanaa
Ak yeneen yi lay xaar
Doyaluma
Mer bi doy na
Doyaluma
Noonu laa lay nammee
(Dootuma ko def, dootuma ko def)
Te foo meree ma jaaxle, bébé
(Dootuma ko def, baal ma, dootuma ko def)
Yaw xool ma tey ree, bébé
(Dootuma ko def, dootuma ko def)
Ñu def juboo de l'année bébé
(Dootuma ko def, baal ma, dootuma ko def)
Manoo dem, kaay ndax yaay sama poumon gauche
Waawaaw yaw la, waawaaw yaw la
Man naa fi dee ci 1 minute de pause
Wallaa wallaa, wallaa wallaa
Am nga cas, stylé nga
Maa ko létt, kaay firi ko
Jeexagul, doyaluma
Jant so kaay dolli ma
Doyaluma
A vie lañu signer
Doyaluma
Noonu laa lay nammee
(Dootuma ko def, dootuma ko def)
Te foo meree ma jaaxle, bébé
(Dootuma ko def, baal ma, dootuma ko def)
Yaw xool ma tey ree, bébé
(Dootuma ko def, dootuma ko def)
Ñu def juboo de l'année bébé
(Dootuma ko def, baal ma, dootuma ko def)
Woy mbëggeeel
Nar na jur guerre
Bae tay la tay, bae tay la tay
Dara laa dul maye
Bae tay la tay (waatal), bae tay la tay
Dara duma ko maye
Bae tay la tay (waatal), bae tay la tay
Dara laa dul maye