notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Plan B

ADIOUZA

Plan B

Yeah
Yeah
Yeah yeah yeah
Yeah yeah

Xoloulo fignou diaar yaw goré wo
Tass yakar bima amone kone weroulo
Gueume say wax tok di xaar gnou marier
Ndéké yayoyaye may sa plan b

Ame diabar ni makoy téré nélaw
Dima topeu foumeu dieum melni nguélaw
Mane bagne na ba soneu mouy daw sama guinaw

Magué ma lou bari taxone mame ma ragal
Hééy
Kham nga rek
Jiguéne dou beug dafay mine

Guis nga rek
Weri na linewone sama ligne

Xoloulo fignou diaar yaw goré wo (yaw goré wo)
Tass yakar bima amone kone weroulo (kone weroulo)
Gueume say wax tok di xaar gnou marier (gnou marier)
Ndéké yayoyaye may sa plan b

Beuthieuk lakoy ame
Goudi mou nakh ma dém
Dane ragala ame gane
Kou gneuw ma dakh mou dem
Xamnga architecte bouy plan
Nane ma
Bébé
Je t'aime
Ma bien aimé
Je taime
Bébé
Féni néne kesse
Ndeker fouwou kayame lawone
Nakhnama dém ni
Bayi ma fi
Meuneu tou mako séne
Thi deuk bi
Plan b

Xoloulo fignou diaar yaw goré wo (yaw goré wo)
Tass yakar bima amone kone weroulo (kone weroulo)
Gueume say wax tok di xaar gnou marier (gnou marier)
Ndéké yayoyaye may sa plan b

Gnou seuye la beugone
Té defna limiy laathie
Beugone na diour sa dome
Gnak na ki ma beugone
Gnak na temp bou baré

Nane lagoor meun fowé xelou jiguéne
Téy léne
L'habit ne fait po le moine
Téy léne
Casting ko na diaar douane
Téy léne

Xoloulo fignou diaar yaw goré wo
Tass yakar bima amone kone weroulo
Gueume say wax tok di xaar gnou marier
Ndéké yayoyaye may sa plan b

Yaw gorewo
Naxe ngama
Yaw gorewo
Naxe ngama
Yaw gorewo
Naxe ngama
Yaw gorewo

Tracker