Diaxelena
Si réseaux yi
Mandou boula séné ni niokétt daw
Yakh derr moy sa liguey oudé yako raw
Do dermatologue Bayil derou gor gni
Yakh nitt defar sa poce nitt nga walla wethitt
Tall sa live dissi togg nitt
Iow yémal sisay soblé meuytou diebaner bi
Boula jiguer ngaye mbeur kamile
Febarou kignane moussoul meuna werr day
Zembéré rek di dem nga deuké mboly
Louy sa liguey ngani réseau yak asse gore
Goudekh beuthieuk Yangui si derrou diambour
Wetal tarri soratoul mougnal
Lou way di def sa kaw la dieum maytoul
Eh méchant boy (Loutax)
Bousa kho di bakh (sa xole di bone)
Kay nga abal mako, ma tek café (sa xole di dagg)
Eh méchant boy (Loutax)
Bousa kho di bakh (sa xole di bone)
Kay nga abal mako, ma tek café (sa xole di dagg)
Mane de jaxkhlena
Bo demoul douma dem loloye Sénégal
Waxale
Dinga deuké malaise meuytoul cardiaque
Docteur bi nena oubil si xole tek si del rétane
Maytoul beugn yi derréta ko lale
Soula beuggé fekhel dentiste meunoussi darra
Niou bok dieukeur ngani tay ngay deh
Kou sokhor kissi rang bi khôl be jexe
Wouye xole be nekh
Febarou kignane moussoul meuna werr day
Zembéré rek di dem nga deuké mboly
Febarou kignane moussoul meuna werr day
Zembéré rek di dem nga deuké mboly
Louy sa liguey ngani réseau yakkass gore
Goudekh beuthieuk Yangui si derrou diambour
Wetal tarri soratoul mougnal
Lou way di def sa kay la dieum maytoul
Eh méchant boy (Loutax)
Bousa kho di bakh (sa xole di bone)
Kay nga abal mako, ma tek café (sa xole di dagg)
Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem li moye
Sénégal Waxal
Statut visé yi ngamaye xagne né dama
Daloule ndax kignane bi nga nekker si réseaux yi damako taloule
Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem loloye
Sénégal Waxal
Da nga maye deuker vu sa xole di bonne
Dieundal glace sa xole fekh yalla ye mayer none
Mane de diaxelenaaa bo demoule douma dem loloye
Sénégal Waxal
TikTok nga talle sa live Facebook, Instagram
Bayi wo fene fo rombou jebaner ma
Lou takh sou ma sagne def nga mère (eh deug la)
Ma deff lou baxe nga mère (eh none leu)
Borom xolou diamant bi
Momar Diop ko soppe
Mouni Mane ma beug Bamba