notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Sa Telephone

ADIOUZA

Sa Telephone

Dafa ñaaw, dafa ñaaw, dafa ñaaw
Lii dafa ñaaw

Xoolotoo ma ci bët
Niiro tuñu ñu dëkk
Lal bi nga jënd te doo ci tëdd
Man la xamul lu tax
Daanu ma tegg natt ba jënd or, ndax sa njaboot
Changé woo, xaalis be wone sa jikko dëgën tan

Sa téléphone, code bi ci nekk
Moo gën woor bu banque centrale
Comme ku manqué ñii nga may jënde
Man ku ma am, est-ce que war na doxaan?

Jëkkër bu la bëggee, da lay jege
Ca ba muy moom
Du xale yi tali bi, la lay jënde
Loolu mooy yoon
'Thioudoung thiandang', guddi mu dawal mbege
Ca ba muy moom
Ci biir nelaw, ngay dégg bébé
Loolu mooy yoon

Ci biir nelaw, ngay dégg bébé
Loolu mooy yoon
'Thioudoung thiandang', guddi mu dawal mbege
Te mooy yoon

Da ngay jëf, yaakaar ni duma yëk
Kon danga am, ba feneen ngay xalamto
Yaa ma takkoon, ni ma gënël teye
Na nga ma muñel, ndax yoon wi sori na

Bunt ngay doon, ñu fay jaare
Pour yap ma bae, fowe la ak sa alal
Te nga aji, doon aladji
Toog ci kër gi te yam ci aji

Jëkkër bu la bëggee, da lay jege
Ca ba muy moom
Du xale yi tali bi, la lay jënde
Loolu mooy yoon
'Thioudoung thiandang', guddi mu dawal mbege
Ca ba muy moom
Ci biir nelaw, ngay dégg bébé
Loolu mooy yoon

Ci biir nelaw, ngay dégg bébé
Loolu mooy yoon
'Thioudoung thiandang', guddi mu dawal mbege
Te mooy yoon

Mo waay, ay!
Mo waay, lady chilel sar, jigéen ju mën góor
Mo waay, téléphone bi tamit, ba ci biir douche
Auto ak missions yu bari, appartements yi ngay loués
Su ngeen yoragul, ci ngeen di yaru
Lu tax doo changer doxin, doxan bi doxul

Jëkkër bu la bëggee, da lay jege
Ca ba muy moom
Du xale yi tali bi, la lay jënde
Loolu mooy yoon
'Thioudoung thiandang', guddi mu dawal mbege
Ca ba muy moom
Ci biir nelaw, ngay dégg bébé
Loolu mooy yoon

Ci biir nelaw, ngay dégg bébé
Loolu mooy yoon
'Thioudoung thiandang', guddi mu dawal mbege
Te mooy yoon

Du nii, du nii, du nii, du nii bae
(Loolu du yoon)
Yiandalëto, fanaanato bae
(Loolu du yoon)

Jabar laa, te war nga ma teral
Te mooy yoon
Jabar laa, te war nga ma teral
Te mooy yoon

Du nii, du nii, du nii
Du nii, du nii, du ne

Tracker