notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Xale Féroce

ADIOUZA

Xale Féroce

Ouh yeyeee
I'm a queen
Fu ma neex lay fëlé
Courant du pile
Ndax feeling paj lañ ma xame

Xale dangay féroce
Boo tolloo ci temps
Man ku ma mësa bokkal poste teg la si banc
Wax ji du bari man
Fi ku fi weet xam ni ndaanaan ñëw na
Xale day solu di xeeñ lu neex
Tegsi di wax lu neex
Wax ji du bari man
Fi ku fi weet xam ni ndaanaan ñëw na

Coow li day bari wante ñeme wuñu jaar man fi may feexloo
Duñu fa jaar jamais
Wax ji du bari ma ni ndaanaan ñëw na

Man li may liggéey billaay sillaay faye ko
(Ku mëna defal)
Man duma crithie duma crathie taluma defante
(Ñun, dañ koy def sax te dafay neex)

Tay dafay neex day metti
Dara du yombu nay metti
Amul seral amul tus nay metti
Bis bi moo ko laj
Wax ji su baree du man
Jëf ji su baree man la
Wax ji su baree du man
Jëf ji su baree ba bare
Su bare man la

Jëf ji su bare man la
Wax ji su newee man la
Eheee man la

Man li may liggéey billaay sillaay faye ko
(Ku mëna defal)
Man duma crithie duma crathie taluma defante
(Ñun, dañ koy def sax te dafay neex)

Tay dafay neex day metti
Dara du yombu nay metti
Amul seral amul tus nay metti
Bis bi moo ko laj
Wax ji su baree du man
Jëf ji su baree man la
Wax ji su baree du man
Jëf ji su baree ba bare
Su bare man la

Ndaanaan bi ñëw na
Ndaanaan bi ñëw na
Ndaanaan bi ñëw na
Tay fi dafay neex

Xol bu seet bi ma Yàlla jox maye daan sama doole
Ba duma tiit man duma ragal benn yoone
Ndaanaan bi da koy yëngël
(Boo ku lak ñoom du seen moroom)
Billaay da koy yëngël
(Boo ku lak ñoom du seen moroom)

Ma bari feeling, tegsi jonge
Te lu ma sañse mu nice
(Pus leen yoon bi dafa bari doole)
Sama wax du bari, sama jëf day bari
Man doo ma sonal
(Pus leen yoon bi dafa bari doole)

Sañse Tina man lu ma namm
(Moo bari doole)
Pusal ma dem man doo ma lakkal
(Pus leen yoon bi dafa bari doole)
Wax ji billaay man damay sonal
(Moo bari doole)
Dëkke tuuti wax job lu bari
(Pus leen yoon bi dafa bari doole)

Ma bari feeling, tegsi jonge
Te lu ma sañse mu nice
(Pus leen yoon bi dafa bari doole)
Sama wax du bari, sama jëf day bari
Man doo ma sonal
(Pus leen yoon bi dafa bari doole)

Xol bu seet bi ma Yàlla jox maye daan sama doole
Ba duma tiit man duma ragal benn yoone
Ndaanaan bi da koy yëngël
(Boo ku lak ñoom du seen moroom)
Billaay da koy yëngël
(Boo ku lak ñoom du seen moroom)

Tracker