notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Baadolo

Aida Samb

Baadolo

Koffi défal lu baax tay lu bone lalay faay
Koffi défal lu baax tay lu bone lalay faay
Aduna sa xarit mo meuna done sa none
Damako dji teranga mu faay ma lu bone

Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done rekk ba dééh
Jiiko jaam lay dundé
Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done rekk ba dééh
Défal naala lune

Teranga lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Koloré lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Teranga lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Koloré lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma

Aduna, niit dina jaay ngoram guir done jaam
Damala wolu wone loma lathie ma diokhla
Féété la fii, féété la fé, féété la fu nekk
Léép lula meussa mééti, mééti naama

Ma bééteu la ngamay jëw
Naane man ak sama jëkër meunu gno am dome
Motax may gudé
Ma bééteu la ngamay djeuw
Baadola baadola lay done rekk ba dééh
Défal naala lune

Teranga lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Koloré lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Teranga lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Koloré lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma

Dagua xam luy aam suba yaw non
Lu la Yallah buur dinthial yaaw non
Dagua fokni gagn ngama yaw non
Dagu ma bétteu maay aam gagn

Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done Rek ba dééh
Jiiko jaam lay dundé
Linga tambalé paré guo
Baadola baadola lay done Rek ba dééh
Défal naala lune

Teranga lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Koloré lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Teranga lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma
Koloré lako ji
Mu faay ma, lu bona bone mu faay ma

Dagua xam luy aam suba yaw non
Lu la Yallah buur dinthial yaaw non
Dagua fokni gagn ngama yaw non
Dagu ma bétteu maay aam gagn

Tracker