Wa dji aduna'm yakkou na
Sokhna si dom'am sangkou na
(Jëf djilé daffa niaw)
Ndaw si sëyeum ba yam nafa njabott gui tassaro
(Jëf djilé daffa niaw)
Bilay man mi dh warouna diamono'k fimou tollou ni
Ak jëf you niaw yi niouffi faral di guiss
Xana denio fatté beussou penc dina nieuw
Denio muur xelam ba tagaliko'k saggom
(Jëf djilé daffa niaw)
Yakkal negn ko ligueyam ba tassaré njabottam
(Jëf djilé daffa niaw)
Toroxol ko thii nawleem ba guéné ko thii keureum
Mou dem ba tay yay'am diaxlé lool
Ba di misère guène aduna thii nakhar
(Jëf djilé daffa niaw)
Ak nimou yiwé wone bilay nonou la yarro wone
Bakhone, jambar mo donnone sen yakkar
Dieul domou diambour yobou ko thii serigne bi
Thii serigne tarriya
Dieul tour yay'am diokh ko
Dieul tour bay'am diokh ko
Tibb ay tangkam diokh ko
Sath ay yeureem yobboul ko
Serigne bi bind xaatim diokhla
Nga daldi soul thii bountou keureum hum hum
Thii lathii yem fitteum dem
Thii la sangko batay nieuwoul
Li dh mettina
Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh
Jëf djilé daffa niaw
Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh
Jëf djilé daffa niaw
Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh
Jëf djilé daffa niaw
Bilay li daffa niaw té li dou lou bakh
Jëf djilé daffa niaw
Aduna ngui ley diay
Nga yakk domou diambour
Kouy diay sa leer
Dieundé ko ak leundeum
Yow dinga gueuleum
Ba do am ngueureum
Leundeum diaroul deureum
Ak dinga dokh ba dinga gueuleum
Ceey sama gars yi yeurmandé
Ki'way domou diambour
Na nga dawal yeurmandé
Yeurmandé eh
Wo oh oh dawalal yeurmandé
Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw)
Na nga dawal yeurmandé (Li daffa niaw li daffa niaw)
Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw)
Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw)
Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw)
Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw)
Na nga dawal yeurmandé (li daffa niaw li daffa niaw)