Love, I will give my heart to you
And make your dreams come true
Never make you heart to lose
Oh na na na no no no
Louy dundeul sa khol bae (mbëguel, mbëguel)
Mbëguel moy doundeul sama khol bae (mbëguel, mbëguel)
Louy saffal sama khol bae (mbëguel, mbëguel)
Mbëguel moy doundeul sama khol (anh han)
Love bi néthii man néthii yow
Té liko teug tassaguko
Nelow na thii say lokho
Yewou thii sa khol
Love bi néthii man néthii yow
Té liko teug tassaguko
Nelow na thii say lokho
Yewou thii sa khel thii sa khol
Yeh yeh yah, yeh yeh yah
Yeh yeh yah, yeh yeh yah
Sama mourray
Thii biir negg bii thii kaw lal bii moy sa nofflay (eh hé hé eh)
Wakhal wayy, samey thiouray, you bakh yi namngako wayy (ah han yeah yeah)
Yow lingueu nekk yow lay done
Té fo diokhogn moy sama yone
Mouy souba goudi ak ngone (ah han han han)
Yow lingueu nekk yow lay done
Té fo diokhogn moy sama yone
Mouy souba goudi ak ngone (ah han han han)
Love, I will give my heart to you
And make your dreams come true
Never make you heart to lose
Oh na na na no no no
Love, I will give my heart to you
And make your dreams come true
Never make you heart to lose
Yeh yeh yah, yeh yeh yah
Yeh yeh yah, yeh yeh yah
Love bi néthii man néthii yow
Té liko teug tassaguko
Nelow na thii say lokho
Yewou thii sa khol
Love bi néthii man néthii yow
Té liko teug tassaguko
Nelow na thii say lokho
Yewou thii sa khel thii sa khol
Masseck Thiam (mbëguel, mbëguel)
[?]