Ma ne nga dox fa
Rabu xiir pare di la ko vuruj
Fu ma génn ngeen daagu xol yi taa
Soo ma xoolee dinga xam sa sëriñ mënul
Parewoo
Oh manuñu tolloo ni baaram yi sa loxo
(Manuñu tolloo)
Wërsëk bu ne borom manuñu tolloo
Na ku ne xam moromam
(Manuñu tolloo)
Bëgguma di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Di ma xas te di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Qualité du toppando daal
(Eeeh eeeh)
Pur man bàyyi nga toppando
(Eeeh eeeh)
Ëpp na ci mapando daal
Dolli ci sol fa
Mi mélodie la dalay dugg ma ni nga bég
Man ci bi beat te mënoo wéy coosaan
Authentique ne laaxu sow ku ñu def ci lekket
Parewoo
Oh manuñu tolloo ni baaram yi sa loxo
(Manuñu tolloo)
Wërsëk bu ne borom manuñu tolloo
Na ku ne xam moromam
(Manuñu tolloo)
Bëgguma di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Di ma xas te di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Qualité du toppando daal
(Eeeh eeeh)
Pur man bàyyi nga toppando
(Eeeh eeeh)
Di ma xas te di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Dégg naa ni lekkatoo sax
(Eeeh eeeh)
Nelawatoo ndax bañ nangu dogal
(Eeeh eeeh)
Pur man bàyyi nga toppando
(Eeeh eeeh)
Ëpp na ci mapando daal
Anh
Wo wooh
Soo xamoon fi ma jaar ba yégsi fi
Fa Yàlla lay defare jaam loxo yéegu fa
Ñaanu yaay la Yàlla di jël
Kenn mënul fakkatel kuy jug ci njël
Am naa ñaanu baay lu may ragal
Ay waxi ginnaaw, wax leen ma nga ca kanam
Ñaanu yaay la Yàlla di jël
Kenn mënul fakkatel kuy jug ci njël
Am naa ñaanu baay lu may ragal
Ay waxi ginnaaw, wax leen ma nga ca kanam
Bëgguma di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Di ma xas te di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Qualité du toppando daal
(Eeeh eeeh)
Pur man bàyyi nga toppando
(Eeeh eeeh)
Di ma xas te di ma toppando
(Eeeh eeeh)
Soo xamoon fi ma jaar ba yégsi fi
Fa Yàlla lay defare jaam loxo yéegu fa