Même si guènte damay weet
Soma fassalé kanam waawaw, waawaw
Samay pékhé yeupay diekh
Takh ma ladj la fok ga wakh ma wakhma
Wakhma, wakhma
Soma diégué lépay leer
Doma wanati guinaaw waawaw
Yalla deff na dotoul dègne, nan
Beug nala beug nala
Baby kaay gnou weet, yaw kaay weetoo bae
Kaay gnou weet, Baby yaw kaay weetoo bae
Diougueul gnou dem tok né
Yaw kaay gnou weeto bae
Ich ya ya yi ya, ich ya ya yi ya
Baby kaay gnou weet
Yaw kaay gnou weeto bae
Yaw kaay gnou weeto bae
Contane na lol sa bissa diote
Kone tay lo diooy damakoy fadj
Sonoone ga lol si liko diar
Yaw sakh khamga li dou hasard
Because I'm before you love me
Because I'm because I'm empty into damay weet
Soma fassalé kanam waawaw, waawaw
Samay pékhé yeupay diekh
Takh ma ladj la fok ga wakh ma wakhma
Wakhma, wakhma
Soma diégué lépay leer
Doma wanati guinaaw waawaw
Yalla deff na dotoul dègne, nan
Beug nala beug nala
Hmhmhmhmmmm
Li né si yaw mo né si mane
Yalla moko deff waawaw (Hmhmhmhmhm)
Li né si mane mo né si yaw
Yalla moko deff waawaw (yeah)
Loumay dokh di khool kénène
Li si yaw dou si kénène
Doumala wétio ak lénène, mbeuguèl
Dou dégne, dou dégne, dou dégne waawaw
Dou dégne, dou dégne, dou dégne waawaw
Si guènte damay weet
Soma fassalé kanam waawaw, waawaw
Samay pékhé yeupay diekh
Takh ma ladj la fok ga wakh ma wakhma
Wakhma, wakhma
Soma diégué lépay leer
Doma wanati guinaaw wakhma
Yalla deff na dotoul dègne, nan
Beug nala beug nala