notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Crazy Love

Akhlou Brick

Crazy Love

Ioe rek ka kham sama prize
Yama dieund té waxalé wo
Da nga changé sama life
Wakh ma deug té nakhaté wo
Nga fek xol mille morceaux
Tabakh ko ni maçon
Bamouy fegn sama eyes
Kou beug beug nala
Kou bagn nama bayék
Ioe yay sama way waat na né

Ioe rek ci xol bi lénén doufi khathi geum na né
Yay sama doncteur kénén douma fathi khamna né
Louma weuri fénén am ngako ba paré diém na né
Yay sama diant nama touma nathi baby

Nekouma because
So crazy in love, eeeh candy
I love you love you so much, so much so tell me
Néma diapeu ngama do bah do bah baby
Nekouma because, eeeh baby
So crazy in love, love baby
I love you love you so much, so much
So tell me néma diapeu ngama do bah do bah baby

Setlou na say yomay khol di ré
Waro nameu potou mèw ndax malay dadji
Sama xol bamako sentiroulé
Laleu weur diapeu la ndékété yay sama sathie
So beugué ma dékilate abdou rass dédét
Doumala trahir niou fit ko def ko maky
Kham nga loutakh mey bagn nga def maquillage
En faite dang ko waneu waaral sa xl geuneu rafète
Siguil kholma si beut baby ré ma c’est que sila
Sama rétane bi di meuneu guén mbecté bi leu
Khipil réwantoul wan ma caprice yi leep ci la
Mba kham nga ba dof dof lo ba kharou ma fékissi la
Mane dama beug nob la damala fan
Sa tour bi la feusseul fégnal ko ci woy fenth
Dés fois ding ma wo mané la awma temps
C’est que journée bi ioe lay khalate té goudi ioe lay guént

Waat nan né
Ioe rek ci xol bi lénén doufi khathi geum na né
Yay sama doncteur kénén douma fathi khamna né
Louma weuri fénén am ngako ba paré diém na né
Yay sama diant nama touma nathi baby

Nekouma because
So crazy in love, eeeh candy
I love you love you so much, so much so tell me
Néma diapeu ngama do bah do bah baby
Nekouma because, eeeh baby
So crazy in love, love baby
I love you love you so much, so much
So tell me néma diapeu ngama do bah do bah baby

Tracker