notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Deff Effect (feat. El Menemo & King Kheuch)

Akhlou Brick

Deff Effect (feat. El Menemo & King Kheuch)

Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect
Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect
Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect
Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe
Ndekte liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Même mbaraan day def effect
Liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Mbaaran day def effect

Est-ce que ki yawa
Jomiwuma leen ci doom Adama ak Awa (bainw)
X-Presse nga indi mangeek Abba
Jëleen coow bi ngeen di toj may tabax
Dama yore xol bu bon ak xol bu baax
Damay wor xaalis dama track ay xaalis
Liggéey bi def effect ñépp dégg sama baat
Mësuma changer masque, ku ma bama baax na
Duma changer veste duma nit kenn bay nala ak Yàlla
Xéy-na wuti ceeb, wuti ceeb
Guddi guddi mbour lay nekk
Bu dul Ara ku koy teg
Bu ma tee may ba def ci man la ko joxeloo ci def
Su la bukki, suli bukki boy, suli sedd

Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect
Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect
Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect
Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe
Ndekte liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Même mbaraan day def effect
Liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Mbaaran day def effect

Eh dangeen di meew, dangeen di soob (oh no)
Dangeen di reew, man dama dof
Mënoo puus mënoo passe, eh kon demal gauche
Li day def-effect, dama bëgg nga deme toog
Sama tekki def effect, ma jëndal mère bi billet Makka
Samay nak yak seen tolli, ñoo may wéyal geynak
Oy yaay yak tolle jaambur, yey ye
Jël sil reew mi bala newi, autopsie naan réy naa ko
Gauche droite noce, spej na ma doy na ma no sad
Gauche wrai, te xos, xalil ma xoos bii, xossa
Di leen forcé ni ay gossi, ndios, di ndiossa
Jutal ki ngay woowe king bi, sosse di sosa

Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect
Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect
Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect
Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe
Ndekte liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Même mbaraan day def effect
Liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Mbaaran day def effect

Nit la bu reew ak xel mu dal, xale bi talul nelew
Yàlla na ma Yàlla baal, sa feneen naan ci ngelaw
Ndox la ci gox sappeur bi, joge di fay
Li gay taal, xaftal ma, lof talal ma look li gay tal
Fi la reew mi tool, dara du ko wodd
Di daal ci subvention ndekete yaw sa rappeur yorul
Yaw lekki yorul di njaay ni mbaam yi lay koti koti
May nar bi fay sa rappeur nan ma day ko potti potti
Lu ngeen fook lu ma book faw mu doon diil
Took di xare ku ci wax ku bëggee coow bif
Damay fo ngeen di xoofe, damay took xiif
Dama dofe ngande démbu damay coopit

Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect
Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect
Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect
Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe
Ndekte liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Même mbaraan day def effect
Liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Mbaaran day def effect

May ma fiston bii, cam gisson lyrics
Rap sans Brick comme auto sans pistons cri
Maa ngi gis comfli ay dir dir li clic
Sama dicton mu ngi ci bisson ak ekive dip (ha ha ha)
Su la neexee nga ni sa rappeur mooy king bi
Mais ma koy reglé def sa sulu rappeur ci ciin bi
Okay man sama gang lañ fal elilpi
Isi na ci man sama gang lañ jox mérite bi
Tabaski na may xar mu def effect
Forcéwuma king te bu ko miin nak yaa ngi fi
Yoru ñu tus, dañuy may gëna andete
Jongul du néegu-góor ba tay loo lay pitaine li

Liggéey ndey, ñaanu yaay, day def effect
Barke baay, ñaanu sëriñ, day def effect
Xar tanku tubey, naan sa doole day def effect
Ku bëgg am lu kenn amul nak faut nga ñafe
Ndekte liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Même mbaraan day def effect
Liggéey day def effect
Xaalis day def effect
Sañse day def effect
Mbaaran day def effect

Schi liggéey (day def effect)
Waa boy xaalis ci bopp (day def effect)
Hii, ñaanu yaay tamit (day def effect)
Woo boy sañse (day def effect)
Mbaraan, mbaraan, mbaraan (day def effect)
Ñaanu yaay tamit (day def effect)
Boy sañsé (day def effect)
Day def effect!

Tracker