Kenn mënul jokk bari mbook
(Ah déedéet!)
Seytaane waxul dëgg benn yoon
(Loolu dëgg la!)
Lii la Yàlla dogal demal toog
(Moo yaw demal toog)
Yëg naa ni dañ may gis seen xol di bon
Yah kon ñoo ngi dead
(Mbaa ñoo ngi dead)
Sama noon yi ñoo ngi dead
(Ñu ngi dead)
Sama noon yi ñoo ngi dead
(Mbaa ñoo ngi dead)
Sama noon ñoo ngi dead
(Ñu ngi dead)
Sama noon yi ñoo ngi dead
(Mbaa ñoo ngi dead)
Dead, dañu bàyyi jooy ñu ngi
Ree, bu ñuy nelaw boy bu ñu
Yee, xel mu dal ni ku julli
Geer, xale nga demal fowi
Mayal mak ñi nos
Ku bareng barigo bii
What's the fucking noise
Néegu góor be yëgel gaz bi moo ngi wàcc
Da ka bind gën leen dégg Yàlla
Gën leen dégg koc
Dañoo ree rekk, dëkk bi yëngu
Ñu saraxe sakku socc
Ara ak Dayza benn lañ ni pièce ak biais témère
Ku ñu bañ li lay ray a ray ku bañ séeréer
Vaccin ñëwaat na, président day pikkiru watt
Reetaan sax moo ma gëna seen
Ña nga lu liru jaan
Kenn mënul jokk bari mbook
(Ah déedéet!)
Seytaane waxul dëgg benn yoon
(Loolu dëgg la!)
Lii la Yàlla dogal demal toog
(Moo yaw demal toog)
Yëg naa ni dañ may gis seen xol di bon
Yah kon ñoo ngi dead
(Mbaa ñoo ngi dead)
Kuy xalam disi jaayu
(Kuy xalam disi jaayu barke ba yaay boroom)
Boo xamul na nga maandu
(Boo xamul na nga maandu boo munul na nga ba)
Man Senegaal la ma ngemb
Kan moo samp ndënd mbër mi xanaa dafa rén
Sori ma way, te nga dégg
Bul ma ñodi lekk ma ni fekk nga ma réeg
Ñangal billaay tital la
Fixé la xool ma fitna bi dikk na
Fuk kinezi aljuma
Coow bi jël disu zizou ñu cissou
Ma kidnapé seen xoli ma tay
Da nge na baax rekk ma nég
Da ngena baax
Da nge na baax rekk ma nég
Moo yeena baax (wàcc)
Ñi bañ a baax ñu ngi dead
Sama noon yi ñoo ngi dead
(Ñu ngi dead)
Sama noon yi ñoo ngi dead
(Mbaa ñoo ngi dead)
Sama noon ñoo ngi dead
(Ñu ngi dead)
Sama noon yi ñoo ngi dead
(Mbaa ñoo ngi dead)
Mbaa ñu ngi dead waa Senegaal ma ni
Dispensaire ci loxoy golo
Bu xàcc wope dafay dead, wuuw
Dispensaire ci loxoy golo
Bu xàcc wope dafay dead, wuuw
Dispensaire ci loxoy golo
Bu xàcc wope dafay dead, wuuw
Dispensaire ci loxoy golo
Bu xàcc wope dafay dead, wuuw