notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra I Am Sorry

Akhlou Brick

I Am Sorry

Loumay défi Aldiana
Né na la fo né man fala né
Lou wéer di déf tchi assamane
Bou dé néwoul sa kaname lay wané
Lou café bi di safé dôme
Ya done motali thiafka bi né sama succar bekk
Lou waral fleurs yi rose
Te néwoul yay khenthiou khét bi ré-ma
Ma dal di békg, sama yeuf!

Khol bi yow rek rek-kako meuneu beuss
Diokh nala lép, lép, lép lou tchi dess
Topp nala fép fép fép banga seuss
Té dou takh ma léb léb léb li tchi dess
I know you love me and you know I love you too
Now I'm feeling so lonely

And I can't be without you, I'm so sorry (sorry)
Baby I'm so sorry (sorry)
I'm so sorry (sorry)
I'm feeling so sorry ooh
Baby I'm so sorry (sorry)
Baby I'm so sorry (sorry)
I'm so sorry
I'm feeling so sorry ooh bae

Nameuna doranté ay ndiénguénaye
Foo sama bopp dima fône, dima ray
Nameu sa fème thiouraye
Sa lokho bima doul lale bouma teudé tay ci night
Mane khawma sakh lou lék yi di saff
Keur gui peunde ndapp yi tilim télé bi peunde té panne
Collègues yi dima wo pour taf
Dama fébar baby nékoufi té nélawouma démb hann
Réveil sonné ma beuss nélawate
Ya done nieuw tchi lal bi bise-ma done-ma yéé wadj ma
Takkalma sama cravate néma nanga sage
Nieuw tchi noppe bi wakh ak mane

I love you (I love you)
I love you too
I love you (I love you)
Mani I love you too
I'm feeling so lonely

And I can't be without you, I'm so sorry (sorry)
Baby I'm so sorry (sorry)
I'm so sorry (sorry)
I'm feeling so sorry ooh
Baby I'm so sorry (sorry)
Baby I'm so sorry (sorry)
I'm so sorry
I'm feeling so sorry ooh bae

Han
Lou meussoul amm, ma niane la léneu
Nga ték tchi batt mais tay nak
Bi moy bou moudj faw nga mayma niou
And dem you home back
No meussoul beug sa khol takk
Da yagg beug nga contane
Wane nama mbeuguél
Wane ma bague né yow la yagg beugone takk
Fatélikoul ni meuss na nekh
Kone dinga faté, balé
Même niari wégne bouniou beugué bess
Faw niou khossanté lalé
Wait, wait, wait, wait

I'm so sorry, I'm so sorry
I'm feeling so
I'm so sorry

Lomay nuyo
Loy wo khoulo bamouy nieuw
Ana goor bou galant wone tay
Maléy khol day mélni dou yow
Sa galé bangui dofé té yow rek do défar café
Nga ame kou mélni ki dila topato, boy dafa diafé
Diamano tay djiguène wourouss la
Li tchi bakh laniou wara sameu
Dél khalate bala nga wax guénal délo ay valise-am

And I can't be without you, I'm so sorry (sorry)
Baby I'm so sorry (sorry)
I'm so sorry (sorry)
I'm feeling so sorry ooh
Baby I'm so sorry (sorry)
Baby I'm so sorry (sorry)
I'm so sorry
I'm feeling so sorry ooh

Tracker