notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Na Yakkou (feat. Ndiole Tall)

Akhlou Brick

Na Yakkou (feat. Ndiole Tall)

Yeah!
Brick
Eh, eh!
Ndiolé Tall
Eey!

Sama beat dal moo ma tere fo
Xam-xam laay kebetoo
Kekk ne nen bu ma dalee ci yaw
Boo parewul toj nee ma pareegoo
Man naa mbappat ak bëre dóor
Am get style, let 'em know!
Gucci Rocher Ferrero
Rap 221 ay Senego
Ray na kii na mais keneen ñëw
Na keneen ñëw!
Yóbbu ko morgue na keneen ñëw
Na keneen ñëw!
Gas naa suul ko na keneen ñëw
Na keneen ñëw!
Ku pare pur dee na-ke-neen-ñëw
Tay bis bi sa bis la ñu nattee la tay
Ara bokkul ak boy yiy tàkk fay
Sànq la fay kamaj non daa war a bàyyi
Ñooy def some buzz ni Sankara Mbaye, ah!
Comme fii kay picc yépp fii man raw naa
Ñépp ay gis tekki bi man a teg léegi brique
We make it, fim ne koo laaj mu ne
Sëng duma génne noppil

Njamala tingóom la yaa leen sut
Eh! Maa leen sut
Danga leen gën de gën leen judd
Eh! Gën leen judd
KO nga perte nga jël ngeen coup
Ooh! Jël ngeen coup (naawal!)
Biteelu sekki bi lañu lay tuur
Nga yàqu!

Come on

Xaptal ma nay boy (na yàqu)
Xaptal ma ne boy
Kaay ma wan la sama doole
Aysileen (na yàqu)
Aywa mu jóg
Aysileen (na yàqu)
Ayca góor
Aywa mu siggi jaaxaan eeh! (Na yàqu)

Woo ma ci rap
Mooy nga woo Naar bi ci guuxum soow
Woo ma ci rap
Ñu Poutine-Biden guerre bi jógul kaw
Maay wann baat
Te waxu dëmme Deyza bi jurul coow
Daaneel naa ñeenti barres
Waxal ma Séereer bi Jean mujjul ñëw
Xaaral ma teg chaise
Indi rap góore ba pénis diis
Jàngal la luy diérèse ak douze syllabes
Rime ko ci hémistiche, wow wow!
I get a flow xaj yi di mbow aj doole Brick ci kaw
Get out ma ñëw, amoo fi bro
Ñoo moom ghetto, let go!
Buuru game beek, buuru Dakar
Moom UCAD, Sénégal en miniature
Am label bic, man ñeewuma ñi signeel
Ndèye Seck signature
Doole Balla Bomb Xareñ
Rime Coppati Sàmbay Naar
Ma daan la ni max
Bi lekk yat bu téye woon doole Souleymane

Njamala tingoom la yaa leen sut
Eh! Maa leen sut
Danga leen gën de gën leen judd
Eh! Gën leen judd
KO nga perte nga jël ngeen coup
Ooh! Jël ngeen coup (naawal!)
Biteelu sekki bi lañu lay tuur
Nga yàqu!

Xaptal ma nay boy (na yàqu)
Xaptal ma ne boy
Kaay ma wan la sama doole
Aysileen (na yàqu)
Aywa mu jóg
Aysileen (na yàqu)
Ayca góor
Aywa mu siggi jaaxaan eeh! (Na yàqu)

Kon jëlal sa yëf (dëgg la!)
Konn jëlal sa yëf (mo yaw!)
Mo jëlal sa yëf Deyza Are yéen a fi ne
Na yàqu!

Waxal!
Ku lim na la yàqal (ouh ouh)
Mo dana yàqu
Ku lim na la yàqal
Mo dana yàqu
Yéen a fi ne (na yàqu)
Yéen a fi ne (na yàqu)
Yéen a fi ne (na yàqu)
Yéen a fi ne (na yàqu)

Njamala tingoom la yaa leen sut
Eh! Maa leen sut
Danga leen gën de gën leen judd
Eh! Gën leen judd
KO nga perte nga jël ngeen coup
Ooh! Jël ngeen coup (naawal!)
Biteelu sekki bi lañu lay tuur
Nga yàqu!

Come on

Xaptal ma nay boy (na yàqu)
Xaptal ma ne boy
Kaay ma wan la sama doole
Aysileen (na yàqu)
Aywa mu jóg
Aysileen (na yàqu)
Ayca góor
Aywa mu siggi jaaxaan eeh! (Na yàqu)

Tracker