notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Nila (feat. Wally B. Seck)

Akhlou Brick

Nila (feat. Wally B. Seck)

Dolé dohoul jaam
Do man té douma yaw
Sagnsé damako taam
Holl maci souff baci kaww
Té dièmoumako dama meun
Sett ci wee ak ci karaw
Guissatouma louma naam
Fima guéné la nieup beugeu aww
Nigger Nila Nila Nila
Nila Nila waay
Founga guenn Noy na Noy na
Noy na waay
Nila Nila Nila
Nila waay
Founga Guenn Noy na Noy na
Noya na waay

Nénala nga soll taille basse
Sollou nii ndaanan bi
Sollou ni kouy dieum nuit du drap
Bül fate foudenü maquillage
Jongama taggal lay deff müssorü
Jongama dou soll bas

Nila bilay sama Adjaratou
Nga sllou mou yiw mandè mandouna
Si iow walay
Nila Nila Nila Bilaay
Nila Nila Nila Bilaay

Danga ne ci a peage woor na wolü
Do dioum ci maquillage
Man damala wolou
Yangui teul sa greffage di dokh di daagü
Yorr hirr di cravache kenn doula soorü
Nehoul ba nehoul adjie ngeu
Linga sanse nekh neu
Ta linguama defal bahna
Yaaka beuri maana
Soll nga sa ndoquette
Tagallou minako si iow
Soma nehé ragadjou dakh akhlou sagnsè

Iow sa dohine naat neu wa wawaaa
Jongama kaaay tedeufouma
Aaah Kaay tedeufouma
Nieweul Tedeufouma
Kay teudeufouma

Nenala nga soll taille basse
Sollü ni ndaanan sollü ni kouy djeum nuit du drap
Boul fate foudeun maquillage
Jongama tagal lay def müssor
Jongama dou soll bas
Nila bilay sama Adjaratou
Nga soll mou yiiw mande manguici iow waallay

Nii la nii la, Nii la bilay
Nii la nii la, Nii la bilay

Dangay sollu di gueuneu nice
Sollou Di geuneu looy
Sama holl bi di guena natt
Fingua guenati gueuena nooy
Sama jongama paradise
Sa sollu dou monotone
Le nga bayii soumanèla sagnsè ngeu nganan
Bve danga meun togne
Meun nga sollou meun nga sagnsè caar
Sa coll bii tegouna si temps
Sa mello bii mo geuneu taarü
Ta man sa djiko bii la geuneu fan
Man ak iow nio dahk wa guissè maabo
Nio geuneu ndir mann iow la taamour iow la appo
Sandiwouma gouro
Bébé sa sollou bii nala si may note
Johma trois pièces bii damay soll
Daffa melni iow leppela japp
Même bo sollè loula eup sah dalay djott
Lalalnala boulko lalli daggoul
Noumou la nekhè nga johma sa loho
Melalni kou djougge mali toudenala Aminta Bakhayoho

Nenala nga soll taille basse
Sollu ni ndanaan sollu ni kouy djeum nuit du rap
Boul fate doudeunou maquillage
Jongama taggal lay deff mussorü
Jongama dou soll bas
Ni la bilay sama Adjaratou nga sollou mou yiiw
Mande mangui ci iow walay
Nila nila nila bilay nila
Nila nila nila bilay nila
Nila nila nila bilay nila

Waly Ak Akhlou brick ndanaan
Kon tekk ci brick Faramareen Music

Tracker