[ARA]
Doole doxul jaam
Doo man te duma yaw
Sañsé dama ko tamm
Xool ma ci suuf ba ci kaw
Te jéemuma ko dama mën
Seet ci we ak ci karaw
Gisatuma lu ma namm
Fi ma génn la ñépp bëgg aw
Dinga ni Nila-Nila
Nila waay
Fi ma gëna nooy na, nooy na
Nooy na waay
Dinga ni Nila-Nila
Nila waay
Fu nga gën nooy na nooy na
Ne naa la nga sol taille-basse
Solul ni ndaanaan bi
Solul ni ku jëm nuit du dras
Bul fàtte fuddënu maquillage
Jongoma tagal lay def musóoru
Jongoma du sol bas
Nila billaay, sama ajaratu sama ajaa
Nga solu mu yiw ñu ànd
Ma am céru alaaji
Nila, Nila, Nila billaay!
Nila, Nila, Nila billaay!
Nila!
Danga ne ci a péage romb la worul
Doo juum ci maquillage, man dama la wóolu
Yaa ngi tël sa greffage di dox di daagu
Yor xiir di karawass, kenn mënul la sóoru
Neexul ba neexul aj nga, li nga sañsé neex na
Li nga ma defal baax na, yaa ka bëri maana
Sol nga sa ndoket, tagalu
Miin naa ko ci yaw duma géj
Su la neexee ragajul
Daan nga Akhlou sañsé
Looking my Marie Madeleine
Yaa ngi may nirul Marie Madeleine
Yaw sa doxin nice na, wo, wo, woh!
Jongoma, kaay tatafu ma
Anh!, kaay tatafu ma
Hum, ñëwal tatafu ma
Kaay tatafu ma!
Ne naa la nga sol taille-basse
Solul ni ndaanaan bi
Solul ni ku jëm nuit du dras
Bul fàtte fuddënu maquillage
Jongoma tagal lay def musóoru
Jongoma du sol bas
Nila billaay, sama ajaratu sama ajaa
Nga solu mu yiw ñu ànd
Ma am céru alaaji
Nila, Nila, Nila billaay!
Nila, Nila, Nila billaay!
Nila!
Dangay solu di gën a nice, solu di gën a tooy
Sama xol bi di gën a naat, fi nga gënati gën a nooy
Sama jongoma paradise, sa solu du monotone
Te nga bàyyi su ma nee la sañsé nga naan ma bae danga mën a tooñ
Mën nga solu, mën nga sañsé kaar
Sa colç bii tegu na ci temps (temps)
Sa melo bii moo gëna taaru, te man sa jikko bii la gën a fan
Man ak yaw ñoo dàq waa Guissé Maabo, ñoo gën a niroo
Man yaw la taamu, yaw la appo, sandiwuma guro
Bébé sa solu bi naa la ci may not
Jox ma trois pièces bi damay sot
Dafa mel ni yaw lépp la jàpp
Même boo solee lu la ëpp sax da lay jot
Lalal naa la bul ko lalli
Daagul nu ma la neexe, nga jox ma sa loxo
Melal ni ku jogé Mali, man ma la tudde Aminta Bakayokho!
Ne naa la nga sol taille-basse
Solul ni ndaanaan bi
Solul ni ku jëm nuit du dras
Bul fàtte fuddënu maquillage
Jongoma tagal lay def musóoru
Jongoma du sol bas
Nila billaay, sama ajaratu sama ajaa
Nga solu mu yiw ñu ànd
Ma am céru alaaji
Nila, Nila, Nila billaay!
Nila, Nila, Nila billaay!
Nila!