notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra À l'infini

ISS 814

À l'infini

Bëgg naa nga jege ci ma
Wax ma loo yëg ci sa xol
Te boo ñëwul ma fekk ci la
Wax la li ne sama xol

Ñun ñaar rekk a wet
Bude mbëggeel bi lañuy dundal
Baby amul lu ñuy xaar
Nel waaw, bul ne déet
Takk na fit bi fekk ci la waroo tas sama yaakaar

Ndax yaay sama number one
Di sama saajooban
Takk la sama jabar
Pur muy continuer

Man ak yaw à l'infini
À l'infini, à l'infini
Pur muy continuer

Mar naa naan nga jox ma ndox
Boo xiifee mbëggeel laa lay jox
Arroser xol bi ak limonade
Neen ko dundu te Yàlla tax

Sa xol bi yépp nga ma jox
Tep tep ñuy dox
Bude am na ñu bëggul bàyyileen kon ñu yox
Sa life da fees ak mbëggeel
Wane nga ma ko ci pete
Yaa ngi ci xol ak xel

Yaw yaay diamants bune dul weccoo ak or
(Non, non, non)
Bum leen presenter ñépp d'accord
(Bae bae bae)

Yaay sama number one
Di sama saajooban
Takk la sama jabar
Pur muy continuer

Man ak yaw à l'infini
À l'infini, à l'infini
Pur muy continuer

Tracker