Su ma la gaañee ci xol, sama bopp la gaañ
Bum la bàyyee nga daanu mooy man may daanu
Bëggatuma ñuy bàyyante ba abadan
Te lu la metti ci man, baby man fuck ñu
Àndandoo xeex ko
Baña bàyyi nderiñ li sunu diggante
Baby kaay ma wax ko
Je t'aime, je t'aime, my baby
Ji nga ma mbëggeelu góor
Kon fok ma dello (wawaw)
Wax nga ma
Lépp loo yor ma ñëw gënal la ko
Ku la dénk xolam
Bàyyi lu la dara (huhuhu)
Xame ko noonu
Ku la ji mbëggeel desa lu la dara
Xame ko noonu
Jox ko love, love (love)
Mérité naa love
Jox ko love, love (love)
Mérité naa love
Baby yaa ma gën a xam
Kenn mënu la tére nekk sama life, sama life
Love nga sama way
Xaritoo ak mbëggeel dañoo ànd waay, ànd waay yah
Best friend ak homie (homie)
Sama doom yaw yaay nekk yaayam (yaayam)
Sumbu nga ci poot mi yeh (poot mi)
Dama la nob waawaaw, waawaaw
Ni ma la bëggee, yeh
Mënoo ko gisaate non
Ni ma la bëggee
Mënoo ko gisaate, my baby
Ku la dénk xolam
Bàyyi lu la dara (huhuhu)
Xame ko noonu
Ku la ji mbëggeel desa lu la dara
Xame ko noonu
Jox ko love, love (love)
Mérité naa love
Jox ko love, love (love)
Mérité naa love
Su ma la gaañee ci xol, sama bopp laa gaañ
Su ma la bàyyee nga daanu, mooy man may daanu