notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Doff Ci Yow

ISS 814

Doff Ci Yow

Yaay sama lumière
Lampe bu may wane yoon
Yaay sama lingeer
Baby baby baby baby baby
Xol bi yaa fi nekk
Ta kenn mënul jël sa place
Sama diamond, sama woman

Bëgguma di la sori
Su ma la tooñee, baby sorry
Ndax xol bi yaa fi nekk
Eh, eh, eh, baby
Sama diamond, sama glory
Kaay ma wax la I’m ready
Baby yaay sama love, love, love, love

Baby dama fall in love
Love ba dof ci yaw
Fooy dem yóbbu ma
Bu ma bàyyi ma wet
Ku la faalewul ma faale la
Yaay sama aljana
Yaw laay topp fepp
Baby, baby

Xam naa li ngay laaj
Sans nga posé benn question
Xam naa li lay faj
Waaw waaw
Fees dell toog ci sa place
Baby amul benn raison
Bu tax man ma lay bàyyi
Waa waaw

Boo ma bàyyee bàyyi
Wax ma fan lay muje
Ndax mbëggeel bi ma am ci yaw
Depassé na life bi
Boo ma jege jege
Xam naa li may sentir
So baby maa la nob ba love
Oh oh oh oooh

Baby dama fall in love
Love ba dof ci yaw
Fooy dem yóbbu ma
Bu ma bàyyi ma wet
Ku la faalewul ma faale la
Yaay sama aljana
Yaw laay topp fepp
Baby, baby

Tracker