notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Fresh (feat. Samba Peuzzi)

ISS 814

Fresh (feat. Samba Peuzzi)

Yeewu def fresh, yeewu def ouhh
Sangu def fresh, sangu def ahhh
Solu def fresh, solu def wuy yaay
Génn def fresh, génn def mbap

Fresh si ndey, fresh si baay
Fresh si solu, oh my fresh
Fresh si ndey, fresh si baay
Fresh si solu, oh my fresh

Doo ma doon swag dance
Faut que ma comptéwat fans
Yaa ngi siisu wat lank
Mënatuma di tëb di dal ndank

Xamuloo naka war baay
Man la boy bi wëy ndank
Dame lay génne fils, bye
Ame na bénéfice, banque

Marakisu leex di pees
Sa papa mooy wax nel mutt
Dugg bus bourlé, di pees
Sa rap bi fayul, nel mutt

Bokkuñu dañu wuute
Ligne lay fay salaire, sama goûter (ay)
Reere dibi mboté
Gel bi ngay gent sama côté (ay)

Yeewu def fresh, yeewu def ouhh
Sangu def fresh, sangu def ahhh
Solu def fresh, solu def wuy yaay
Génn def fresh, génn def mbap

Fresh si ndey, fresh si baay
Fresh si solu, oh my fresh
Fresh si ndey, fresh si baay
Fresh si solu, oh my fresh

Joxor major, joxor leen
Meloon leen ni ñu mel, soxor leen
Bindi son yi, joxaat leen
Air bu fresh doxot leen

Wiri wiri jari ndari
Solaan dal yi tulli tat yi
Takk bac bi, dem na jàngi
Reer na France, man la Diarry

Eh pusal fee, bul ma fonto
Sa best gel man ma konko
Boo ma clashé, num lay tonto
Bu ma masee, faut que ma sonko

Mësuma sweet, I'm beauty
Faut que nga tari sar pur aji
Dañuy sandi xer pur promo
Nekkul Auchan lañuy daji

Deme gauche ak sama gars yi
Def fresh, fresh, fresh, fresh
Nañ dem droite, non du ñu bàyyi
Def fresh, fresh, fresh, fresh
Soxor ni xoolal li ñi sol
Def fresh, fresh, fresh, fresh
Ñooy pëndal ba sa école
Def fresh, fresh, fresh, fresh

Yeewu def fresh, yeewu def ouhh
Sangu def fresh, sangu def ahhh
Solu def fresh, solu def wuy yaay
Génn def fresh, génn def mbap

Fresh si ndey, fresh si baay
Fresh si solu, oh my fresh
Fresh si ndey, fresh si baay
Fresh si solu, oh my fresh

Tracker