notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Guediawaye

ISS 814

Guediawaye

Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo

Nieuwal mbedo bénén life la
Mane ak sama gayi niougui bendo
Nieuweuk ghetto never mine la
Multitude pote mofiy daw, waww waww
Wane la lodoul guiss loudoul degg khamna digua know
Waxma yagui bègue yankoy yégue night bi di gueuna Go
Tékk zeum half night, talle call night late
Film daw Twilight, teugue Match side side
Mbedo bendo lolou-oy ghetto

Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo

Prisonnier sa peine kaygne lén la juger
Fatéll lepp nieuweul niou diapisé
Kagnou dem concert après niou gnibisi
Nénagn dioub dou wéss kon bokk gnibissi
Kay gnou dance boudé daff lay dimbali pour gua faté say pression
Eh kay niou dance fibou wésso hip-hop guisso centre de réinsertion
Tékk zeum half night, talle call night late
Film daw Twilight, teugue Match side side
Mbedo bendo lolou-oy ghetto

Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo

Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo

Tracker