notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Sama Lova

ISS 814

Sama Lova

Mbëggeel bi ma am ci yaw
Daf may tiital yenn saay
Sama àdduna naan lay mel
Bu ñu nekkatul ñun ñaar
Lu fanaan ci man yéndu ci yaw
Yaay sama génn-wall
Foo dem maa ngi toog, toog di la xaar

Parce que yaay sama lova, lova, lova, lova
Sama lova, lova, lova, lova

Ni ñu mel man daf may tiital
Est-ce que doo yéewu bëgg bàyyi?
Amoon na ñi ma fi jiital
Ba ma leen wone mbëggeel dañ ma trahir
Yaw yaay sama love te am naa yaakaar
Bëgguma dem ba ci biir am ci naqar
Yenn saay nga jefe mbir ma am ci xel ñaar
Gëm ne rekk

Bu ma jàpp tew bàyyi day wax
Jiital naa samay sentiment ba fàtte sama bopp
Ak li may yëg
Woo la ci love yaw nga feluma
Pur ñu ànd bokkando suñuy wërsëg

Mbëggeel bi ma am ci yaw
Daf may tiital yenn saay
Sama àdduna naan lay mel
Bu ñu nekkatul ñun ñaar
Lu fanaan ci man yéndu ci yaw
Yaay sama génn-wall
Foo dem maa ngi toog, toog di la xaar

Parce que yaay sama lova, lova, lova, lova
Sama lova, lova, lova, lova

Saa yu ma mere dem bay xàddi
Xalaat fi ñu jaar, jàppaat espoir
Lu nekk gis nañ ko ci yoon bi
Défaite ak victoire, dund ko ñun ñaar
Xam naa ni dañu xeex ma babe
Jàppal dina baax, loolu la mën a wax
Te saa yoo nare dem ba xàddi
Danga ma koy wax mën naa la indiwaat

Suñu xol yi leer na kon couple bi munul lëndëm maak yaw
Non non
Foo mënti ne ci life woo ma ma ñëw
Oh oh
Ñu ànde go (oh no)

Mbëggeel bi ma am ci yaw
Daf may tiital yenn saay
Sama àdduna naan lay mel
Bu ñu nekkatul ñun ñaar
Lu fanaan ci man yéndu ci yaw
Yaay sama génn-wall
Foo dem maa ngi toog, toog di la xaar

Tracker