notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Li Ngama Diaral

Momo Dieng

Li Ngama Diaral

Lebone guani lippone ben xalei boumafi nobone
Mou diaralma dokh goudiii léép louma am diayko crédiit
Néké so beugué, yaw so beugué daguay misère

Lebone guani lippone ben xalei boumafi nobone
Mou diaralma dokh goudiii léép louma am diayko crédiit
Néké so beugué, yaw so beugué daguay misère

Oh wawaw!
Waw meunouma do misère
Yaw daguay misére
Waw meunouma do misére
Yaw daguay misére

Everything magui si téléphone bi
Gayiii nénagn dagn ma méréé
Takhna nieup bayima
Paco néna khamé touma
Waya lougn meuna wax yeupeu
Sama mbeuguel mane la thie khol
Daniou wara xamni manou mako diaye nekh mane damako beugeuh

Waw fokma nangou misère
Damako beugeuh
Waw meunouma do misère
Mane dama beugeuh

Mbeuguel sakh boula diéguéwé
Bo moytou woul dagu koy fowé
Lepp loy sagané dal
Kénéna gua tok mou diaral ko louné
Mane fokk ma soré nakh
Nakh gua meuna kham sama mbeuguel

Bilay fokma ndangou misére
Mane damay misère
Bilay fokma ndangou misére
Mane damay misère

Alale kouko sagané
Kou ko farlo koy moudjé
Doudek beuthieuk malay wo
Yaw dé wouyou wo ma
Wouyouwooma faalé wooma
Yaw dé wouyou womay
Faléwo ma mane deh top na leuy
Wayé yeugoulo meuy, yeugoulo meuy
Faléwo ma mane deh top na leuy

[?]
[?]
[?]