Tay ma bakk la, sama chocolat
Bëgg naa la, loolu wóor naa la
Tay ma tagg la sama olalah
Xam naa ne bëgg nga ma, loolu wóor na ma
Gis nga jant bi lu mu leer a leer
Sa jëmm ji mooy sama lumière
Xool nga wer wi nu mu jekke
Sa xol bi noonu la rafete
Kon jege ma
Ñu ànd dem feneen wuyu ma
Kon yóbbu ma
Ñu ànd dund leneen ba abadan
Yeah, yeah
Habibi
Ki gën ci man te yaa xam li war ci man
Di ko def
Yërëm nga ma chéri yaw yaay sama Habibi
Ano woni my habibti
Guily mbeeli mo welti seti
Guilemen ko fifty fifty
Dund ak yaw muy neex mooy metti
Love nana shine like a diamond
Hakudam min e ma ha diamone
Indema e horam like melody
Yidema hokimi dole mbarodi
Wawa welde niande fof wada peace
Andou Kiram to mberde ko disease
Habibti par fewnou tes valises
Mami souré houré kangue kaliss
Min seeden kalda gonga ann bouriyam
Jougo ma e jougam longo fawe walabam
Holimi yidde fadani jango tideyam
Bae ndekete banekhou beguel fila yam
Halla mbelka newika tewika
Hewa mossali e diam a yiyata tikka
Mberde wiyani aala guite dji ko djiidi
Love sabou Allah mberde jaagui ha tiidi
Habibi
Ki gën ci man te yaa xam li war ci man
Di ko def
Yërëm nga ma chéri yaw yaay sama Habibi
Jugal nga fecce ko
Ma woy nga feluma
Jugal nga fecce ko
(Chéri yaw yaay sama habibi)
Jugal nga fecce ko
Ma woy nga feluma
(Yaw yaay sama chéri, yaw yaay sama habibi)
Ki gën ci man te yaa xam li war ci man
Di ko def
Yërëm nga ma chéri yaw yaay sama Habibi