Xool la si bët xol di ko yëg
Xel bi sori yénne ji bari li mbëggeel la ko laal
Hey, su de ay gént buñ ma yee
Li de moo daq neex di ma cooqotaan may ree
Hum, kaay kaay
Yaw rekk laa love
Kaay kaay
Yaw rekk laa nob
Yaw, yaw, yaw laa nob
Yaw, yaw, yaw laa nob
Su mbëggeel doon jaay may jënd
Lépp lu ma laaj ma jox ko
Te soo bëggee dëgg-dëgg
Sama xol bi yaa koy fëgg
Jox nga ma sama gédd
Baby sa love lañ ma sedd
Ci lay dundu ba tedd
Te boo ma jegee xol bi sedd
Kaay kaay
Yaw rekk laa love
Kaay kaay
Yaw rekk laa nob
Yaw, yaw, yaw laa nob
Yaw, yaw, yaw laa nob
Dama la, dama la, dama la nob
Ba bëgguma lu lay gaañ
Soo ma soree dina ma sonal
Sa mbëggeel la may daan
Kaay kaay
Yaw rekk laa love
Kaay kaay
Yaw rekk laa nob
Yaw, yaw, yaw laa love
Yaw, yaw, yaw laa love