Dafa gneuw dindi leppe Lou fi leundeumone
Leral féppe, mome képpe
Lolou loukey dindi
Lou thiow Li beuri beuri
Mome mofi né
Mom reeek
Dafa gneuw
Oubi bounte yi
Soutouralma
Teralma
Woné ma fépp
Dessélatouma dara
Bamouy métxti mome rekafi néwone
Mome rekkk
Dagnou wouté
Sama bosse deh dou gneulé
Damey begué
Limou meune la gné teulé
Souma teudé mou lébeul meu bama nelaw
Souma guissoulé dafay dof mane la nope
Yéne saye mouné ma
Yaye Sama aldiana
Khol bi fekh mou déy ma
Sa rétane louné na
Loumou ame bokak man
Mane maye première daamam
Kholoul kénéne koudoul mane
He’s my Superman
Ndourowoutak gnom
Bokou gnouy féme
Ndourowoutak gnom
Non non dougnou béne
Ndourowoutak gnom
Bookougnouy féeeeme
Ndourowoutak gnom
Non non dougnou béne
Sama boss
Dou door, dou saga dou worr
Gawna thi mane
Mané!!
Sama boss Sama bosse
Dou door, dou saga dou worr
Gaw na thi mane
Beau neu gentle na
Khol bi rafet na
Loumou kham wakh ma
Fouma néee tamit moungui faaaa
Damey khool ak beutou mbeuguel
Dima waaakh aye wakhou Nobeel
Love na ma ba doff kholam maye boroome
Kéne la si gnom non amoul morome
Deugueuntane la mane ley béguéee
Dou aye fooo mane rek la aiméee
Yéne saye mouné ma
Yaye Sama aldiana
Khol bi nekh mou dey ma
Sa retane louné la
Loumou ame bokak mane
Mane maye première daamam
Souma guissoulé dafey dof mane la nope
Ndourowoutak gnom
Bokougnouy féme
Ndourowoutak gnom
Non non dougnou béne
Ndourowoutak gnom
Bookougnouy féeeeme
Ndourowoutak gnom
Non non dougnou béne
Sama boss
Dou door, dou saga dou worr
Gawna thii mane
Mané!!
Sama boss
Dou door, dou saga dou worr
Gawna thii mane
Ndourowoutak gnom
Ndourowoutak gnom