Life bee changé
Wala jikko yee yàqu, yee yàqu
Loo xamal ké yol
Ok wax nga ba tarde
Léegi ñépp lay moytu, lay moytu
Mu ngi bëgg ñaaw de
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk ey, ndànk ey, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
[Narah Diouf]
Ey fi la réew mi tollu
Ñi de cas lañuy topp
Lu tokk sa nopp
Fel sa gëmmiñ, lépp tuuru
Kon mu ngi tokk
Céy li nga bokk
Tekk ko si suuf
Balla moo souss
Ok yaa ngi si TikTok
Doo raté Facebook
Snap nga flamme cas bi
Whatsap nga yénou coow li
Ok bàyyil ni nga nekke
Li du sa métier
Bul topp sa xol
Waxal prarara
Life bee changé
Wala jikko yee yàqu, yee yàqu
Loo xamal ké yol
Ok wax nga ba tarde
Léegi ñépp lay moytu, lay moytu
Mu ngi bëgg ñaaw de
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk ey, ndànk ey, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Bàyyil libeurou jaambur di topp sa kilo
Yaw xoolal sa bopp, teggil sa nopp
Bàyyil sopp, soooof!
Shhhhh
Ya raw mor ndaje
Doo raté daje
Kuy dem yóbbu la
Fuñ dem fekk la
Life bi de concourou tekki là
Ku yeex ñu bala fa
Jàppal fils te bul bàyyi
Fattal té bañ a teppi
Fatal ma foofu bu dara percé
Tëbbel ma teup ñu ànd percer
Liggéey rekk di encaisser
Kassé
Life bee changé
Wala jikko yee yàqu, yee yàqu
Loo xamal ké yol
Ok wax nga ba tarde
Léegi ñépp lay moytu, lay moytu
Mu ngi bëgg ñaaw de
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk ey, ndànk ey, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk