Ni ngay dundee sunu ñakk wee du yoon
Baadoola daal sonn na ci lu mu
Dëkkee Senegaal Njaay
Jappale len ko waawaw
Ni ngay dundee yoo
Ñun rekk a jaxle
Ndax du ñu doomu buur
Sòmbi la ñuy reere
Bokku ñu nguur
Feebar mënu loo fajju
Yeena nga ñuy rey di suul
Lii bu ci kenn waxul
Ñawteef gaa law ci ñun
Baadoola, baadoola, baadoola
Hum (yes), hum (yes)
Baadoola, baadoola, baadoola
Hum (yes), hum (yes)
(Hooo)
I'm socialized
(Hooo)
I'm so sad
(Hooo)
I'm socialized
(Hooo)
I'm so sad
Fitna gi nekk ci
Ñun waa dëkk bi
Fitna gi nekk ci
Xolu askan wi
Baadoola sonn na
Yërmande ci moom
Baadoola, baadoola, baadoola
Hum (yes), hum (yes)
Baadoola, baadoola, baadoola
Hum (yes), hum (yes)
(Hooo)
I'm socialized
(Hooo)
I'm so sad
(Hooo)
I'm socialized
(Hooo)
I'm so sad
(Baadoola)
Baadoola
Baadoola
Baadoola
Ni ngay dundee sunu ñakk wee du yoon
Baadoola daal sonn na ci lu mu
Dëkkee Senegaal Njaay
Jappale len ko waawaw
Ni ngay dundee yoo