notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Bakkan

Obree Daman

Bakkan

Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale

Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale
Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale

Dox naa ba ñëw setsi la
He ñëw setsi la (hé)
Nitt de war na mandu
Teey te yalla tax (hé hé)

Seet naa la sow, seet naa la penku
Mandu reer ci jamano
Seet naa la sow, seet naa la penku
Mandu reer ci say jikko

Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale
Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale

Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale

Mandu, mandu
Mën na laa wallu
Mandu, di na mandu
Ci doomu àdama bi le (hé)

Seet naa la sow (seet naa la sow)
Seet naa la penku (seet naa la penku)
Mandu reer ci jamano
Seet naa la sow (seet naa la sow)
Seet naa la penku (seet naa la penku)
Mandu reer ci say jikko

Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale
Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale

Bul di jaawale
Bul di jaawale
Bul di jaawale

Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale
Mandu, mandu len
Ci nitt bul di jaawale
Bul di jaawale

Tracker