Nitt ak melokaanam
Ci yërmande, la ko Yalla bindee
Doomu Àdama, cëy xamoon lu ko fi indi woon
Hum du caaxaan
Fii, fii àdduna la
Ndank yen ci àdduna
Nitt moo ñàkk xëy bis am beew
Nitt moo njool moo gàtt moo weex
Waaye ci yërmande, la ko Yalla bindee
Ho ho ho
Ho ho ho
Ho ho ho
Ho ho ho
Yalla moo sàkk goor ak jigeen
Magg ak ndaw te yemale wu len
Yalla moo sàkk bëccëg guddi
Bës bu xasa dem dootul deelu si
Fii, fii àdduna la
Ndank yen ci àdduna
Ho fii, fii àdduna la
Ndank yen ci àdduna
Yalla moo sàkk goor ak jigeen
Magg ak ndaw te yemale wu len
Yalla moo sàkk bëccëg guddi
Bës bu xasa dem dootul deelu si