Aha
Yow, mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Yow, mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Agsil ñu àndandoo
Àndandoo ci asamaan
Sa mbëggeel’ay bideew
(Bideew biy leeral goor Yalla)
Bideew biy leeral sama yoon
Aha, jigeen a indi leer
Aha, leeray ci àdduna
Aha, sa mbëggeel’ay bideew
(Bideew biy leeral goor Yalla)
Aha, biy leeral sama yoon
Yow, mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Yow, mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Jigeen’ay leeral
Melni leeray u asamaan
Sen mbëggeel’ay leeral
Jigeen’ay leeral
Ni leeray u asamaan
Sa mbëggeel’ay leeral
Sama yoon
Leer leer leer
Leeray u jigeen buy joge asamaan si
Moy leeral goor Yalla yi
Leeray u jigeen buy joge asamaan si
Moy leeral goor Yalla yi
Leeray u jigeen buy joge asamaan si
Moy leeral goor Yalla yi
Yow, mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Yow, mii
Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon
Aha