notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Bo Jekko

Obree Daman

Bo Jekko

Bo jekko deel baale
Boo amee te mën ko deel maye
Bo jekko deel baale
Boo amee te mën ko deel maye

Yaa ngi ci kaw
Xalaatal ñi ci suuf
'Cause tomorrow it's another day
Bu am-am tax, nga fate ki doonoo
Waaye bu ñakk tax, nga baayi sa loxo
Ab Goor Yàlla ngay doon
Royal ci Ibra Faal ee
Dinañ la xas dinañ la faqastal
Waay waay bu len faale
Ab Yaay Faal ngay doon
Royal ci Maam Buso Baali
Dinañ la xas dinañ la faqastal
Yaay Faal nga bu len faale

Jappante baña baayi gën di bëggënte
Kula tooñ nang ko baal buñ ñu jaxase
Ah dunyaa
Ah dunyaa

Jappante baña baayi gën di bëggënte
Kula tooñ nang ko baal buñ ñu jaxase
Ah dunyaa
Ah dunyaa

Goor Yàlla yombul ci adduna si le
Boo jekkoo deel baale boo ammee te mën ko deel maye ay
Waay waay waay waay

Bo jekko deel baale
Boo amee te mën ko deel maye
Bo jekko deel baale
Boo amee te mën ko deel maye

Tracker