Toujours posé dans le bendo melni potolamp
Bolba balba barada ba niounleu ballon d'or
Boy boul lathieté louy le syndrome xamga c'est chômage
Life bi tékétoufi dara téé nioo takk diok
Nakh Diangatouma maagui treun
Orientewniouma dagnma teubeul
Fouki problèmes fouki dereum
Keur gueu amoul louniu dereukh
Ousmane mafia bimdoon keleum
Lako thioy yi néwé thieureukh
Xam nga fii rk nioun niooy nelow si sen loi yiniou tereul
Bando sapeur doufi diaar chaque jour boys yi nioogui takk
Police moofi diaar am ay neggers youmou shot
Si kanamou justice doomou bando doufa diar lou beuri
Une bavure de plus y'aura jamais de coupable
Boy fii amna innocent
Fii amna 100 inos
Peace période meeting rk lafiy am
Tekk beut sissa cartou mère
Maire bi yeugoul sa père
Père bi di daw dépense di dioug aka daanou nakh
Kogn bi dafa macky
Ndakaru dou France
Mr le maire kouti kouti
Ay mbeuw rk la xam
Kogn bi goudi len dou takk
Boysa yi nioogui taal
Bendo amoul choix dangay reuth baa nga fakh
Welcome to my bando (bando, bando, bando, bando, bando)
Fii mooy sama bando (bando, bando, bando, bando, bando)
Welcome to my bando (bando, bando, bando, bando, bando)
Fii mooy
Fii mooy sama bando (bando, bando, bando, bando, bando)
Digou khaadiou goudi
Sathi day wouti dji
Waa kogn bi neenaniou mr le maire ligueeyoufi shit!
Kepp kou compter si kii
Beugouloo gagner chiffre
Sol nieugou 20 milles
Am problème juuni t'es qui ii
Diplômes yi takhouniou nga ligueey
(Bando)
Seugn bi neena danioula ligueey
(Bando)
Nelawouma demb dama gouder
Foo guiss kou yeewou midi dinreub bideew
Boo kaffé ba paré dioubeuli kaaf
Même bou lampes takoul boy yaagui taal
Yawa yawa ndokh bi deff na fi att
Amna niou permanence mais Ana hôpital
Mr le maire boo dieeko
Deel baalé
Comme danga am doolé
Boul diaay doolé
Mr le maire boo dieeko
Deel baalé
Comme danga am doolé
Boul diaay doolé
Kogn bi dafa macky
Ndakaru dou France
Mr le maire kouti kouti
Ay mbeuw rk la xam
Kogn bi goudi len dou takk
Boysa yi nioogui taal
Bendo amoul choix dangay reuth baa nga fakh
Welcome to my bando (bando, bando, bando, bando, bando)
Fii mooy sama bando (bando, bando, bando, bando, bando)
Welcome to my bando (bando, bando, bando, bando, bando)
Fii mooy
Fii mooy sama bando (bando, bando, bando, bando, bando)
(Boo yeewo yee ma ma yee samay morom)
Nioun sunuy cauchemards beuthieuk bi lay door
(Diap ci Cfa meun baayi samay nelow)
Boo meunoul soukeur café dangay niak khorom
(Ay dou diaami borom)
Borom koudou dou lakk
(Fayal naar bi khorom)
Sinon tchinn bi dou takk
(Fii dafa thiool)
Lou teug tass monsieur le maire dinafi diog
Bou defoul liko war naniou khaathi dooranoo
Dougui bureau de vote
Gokh bi nioun niooko mom
Kéneu douniu noot
(Mr le maire boo dieeko deel baalé
Moytoul beugn ak lamegn
Middle fingers yeey dakhanté
Bess bounioulay aaté)