Bimay ndieukeu guiss
Sila nima miss man dama la kiff
Epuis sakh es ce ke meuna ame kiss
Y’a ngui may weundell moudier na miir
Dama beug guel bou bandit
Bouma Doul may ma noyi
Bala ma wakh mou dieul, [?] tek si si sexy
Pour mou meun ma make lo money, kouma meuna fonder lo famille
Kouma yaral sama dome yi
Tu te prends pour le BG, BG de la cité
Diaroul ngay invités, je n'est rien a ciré
Epuis begouma say bouquets
Lekouma say rocher
Baayima yaw, baayima yaw
Y’a ngui daw bobou ba legui
Meun ngama may ma noyii
Talouma sa seungen yi
Amouma time bou bari
Dama wara make money
Dnc tallouma wakh dji
Yaw diougal nga djobi bayi togayou cogn bi
Kaay Wakhal nala ko Lou eupp ben yone
Awma sa diot Man dama nek si yone
Pourkoi tu fais des tonne té dara d’où ame
J pas le temps de parlér de ton nom
Life bé metti tout le monde veut teki
Talouma mbeugel [?]
Gorou legui dolen diokh sa khôl
Dagn koy fowé ba paré dém
Aayy, amo loma meuna diay
Kilayy diokh man ma koy Faye
Djiguenne djiou meun goor
Yoor fittou gaindé ndiaye
[?]
Y’a ngui daw bobou ba legui
Meun ngama may ma noyii
Talouma sa seungen yi
Amouma time bou bari
Dama wara make money
Dnc tallouma wakh dji
Yaw diougal nga djobi bayi togayou cogn bi
[?]
[?]
Y’a ngui daw bobou ba legui
Meun ngama may ma noyii
Talouma sa seungen yi
Amouma time bou bari
Dama wara make money
Dnc tallouma wakh dji
Yaw diougal nga djobi bayi togayou cogn bi