notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Expresso (feat. Abiba)

One Lyrical

Expresso (feat. Abiba)

Khalé bima beug, mongui sama wett
Expresso, expresso naniou ma bayi ma rêvé
Oui Papa, oui maman
Expresso, expresso naniou ma bayi ma rêvé
Togal ci sa podiou ndeye
Diaroul maquillage'ou ndax soloma thip kim
Beauté naturelle, moma geuneul
Beauté maquillée miké kif kif
Ioe bamalay kham ci ni nga mélone
Boula fa dara dieulé my babe
Bamalay kham ci djiko bou rafet la leu khamé
Continuer ko ma Lydie
Ioe yama way lo, sopi nga gangsta bi
Sopi nga gangsta wooy shit
Mala dioy lo, sey copine
Né nagn nga bayima wo woh shit
Diotna def ay erreurs
Nga diégeul ma comment honeyy

Khalé bima beug, mongui sama wett
Expresso, expresso naniou ma bayi ma rêvé
Khalé bima beug yahh, mongui sama wett
Expresso, expresso naniou ma bayi ma rêvé
Expresso (expresso, expresso yah no, yah no)
Ohh expresso
Nah nah nah nah, nah nah nah nah
Expresso
Nah nah nah nah, nah nah nah nah
Expresso

Don't play, don't play, don't play with me
I thinks that this melody
That make me think of you
Tu sais que l'amour-là c'est entre nous
Et que princesse sa vive atout
Même si parfois la vie nous joue des tours
Notre amour ok sa tourne
Ioe dou mane mi nga beug
Ma ngui ni sa wett (no way)
Niowal ma wax la li ngey def ci mane
Tu me rends parano, ouais chui parano
Ce que disent les gens je m'en moque
Ils sont pas normaux waa
Wanoma louma nakhari
Mounone nga mel nénén
Kimay geuneul motali sama baby ioe
[?] doundeul, doundeul malay mounial
Sou mété may sa soucar ma dieul
Nga fékheul sa xol
Kham ngani may sa

Khalé bima beug, mongui sama wett
Expresso, expresso naniou ma bayi ma rêvé
Khalé bima beug yahh, mongui sama wett
Expresso, expresso naniou ma bayi ma rêvé
Expresso (expresso, expresso yah no, yah no)
Ohh expresso
Nah nah nah nah, nah nah nah nah
Expresso
Nah nah nah nah, nah nah nah nah
Expresso
Nah nah nah nah, nah nah nah nah

Tracker