notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Seeto Seet (feat. Leyna)

One Lyrical

Seeto Seet (feat. Leyna)

Kenal ngama thi gnom
Denthial ngama sa bopp
Takh nga dioy (mougneul nala)
Mirr na thi yaw, mi amor

Kenal ngama thi gnom
Denthial ngama sa bopp
Takhh nga ma dioy, mougneul nala
Mirr na thi yaw, mi amor

Setto sett, setto sett
Setto sett, setto sett
Setto sett, setto sett
Setto sett, setto sett
(Setto sett)

Sama dollé la sef thi mbeuguel
Bimala beugué kholouma lo am ak lo amoul
Beut yingay kholé missal nama ningama beugué

(Damala nopp)
Deff ngama Indo anyway
Diaral ngama teukku Balla Gaye
Kay ma nekhal sa goudi gui tay
Yobbuma fu sorri doumla lathté fougnou dieum

Diombadio, show me my your body
Show me your body, show me your body
Diambadio, wakh dji du bari
Wakh dji du bari, only, only, only, only you

Kenal ngama si gnom
Denthial ngama sa boppp
Takk na nga dioy (mougneul nala)
Mirr na si yaw, mi amor

Kenal ngama si gnom
Denthial ngama sa bopp
Takh nga ma dioy, mougneul nala
Mirr na si yaw, mi amor

Setto sett, setto sett (mirr na di yaw, mi amor)
Setto sett, setto sett
Setto sett, setto sett (mirr na di yaw, mi amor)
Setto sett, setto sett

Goudi beuttsett souba ak ngonn meun na nelaw ba yandorr
Mirr na, mi amor, yaw rekk, mi amor
Goudi beuttsett souba ak ngonn meun na nelaw ba yandorr
Mirr na, mi amor, yaw rekk, mi amor

Setto sett, setto sett
Setto sett, setto sett
Setto sett, setto sett
Setto sett, setto sett

Beuttsettt souba ak ngonnn
Nelaw ba yandorr

Tracker