notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Todj Sa Monde

One Lyrical

Todj Sa Monde

Dokh kat dou féké dewou mamam
Dama peundeul kawak souf khalé you djigueine yi nio ma deff ndanane
Meuneu fen nguané ya mom yéré yi té Yoro soukar ak nana
No toudou nguané mara Doudou Ndiaye Rose mi dé sama mame la
Guemouma kocc Barma
Lima beug moy deff tathe gueweul yi darma
Makoy sédalé ni barman
Niari wer rangui nguamay top lanla
Khaké bou rafet darma sama nek dafa am vitamine sawarna
Khaliss partout douma war mbam
Bouma naré def yalla nama yalla di ray man
Dama leena khep ak seni party
Samba party ak Modou Party yeneu beug party
Damay kheuy ci piscine yendou ci jacousie
Dama am alal bollé nalak samay cousines
Je ne peut pas parler de gauche à droite
On ne peut pas plaire à tout le monde basta
Ce n'est pas la peine de couper tes rastas
On dit que l'habit ne fait pas le moine
Mais sa bouma len guissé am envie guéné sarakh
Macky Sall sama kharitou papa la namouma thiarakh
Damay tothie sama monde damay tothie sama monde

Tothie sama monde
Tothie sama monde
Tothie sama monde
Tothie sama monde
Damay tothie sama monde
Tothie sama monde
Tothie sama monde
Tothie sama monde
Kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Carré VIP amoul guetou bëy kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Carré VIP amoul guetou bey kay tothie sa monde
Kay ngua tothie sa monde
Kay ngua tothie sa monde

Dangua tek deal sa Yaye tek deal sa baye
Niak diom amoulo money doumoko nétali
Fingua diar dama KO wessou nigger don pali
Yangui dokh di aubeuli say nelaw doyoul Fall dangua melni kou palu
Weur di khembeuli swaggou talibé ngua yor boy dangua khegne mbalitt
Sam guemigne fraîche ni glace khalé Nicky Minaj
Ma géré té beugoul ma sori viré nama western union
Sokhor braket ni first last am na diorom mi dom té ama gouma diabar
(Astakhfiroulah bayil doul nigger)
King of battré douma Doug soirée sénégalaise dafa beuri cas social
Douma setan télé
Awma temps ni Eden Hasard tothie na Lille tothie na Chelsea tothie na
Sama équipe nationale tothie na Bercy jet set
Lu tothie na Zenith mais si pet dafa échec ni Waly
Faramaren la bayi len ma way
Sabaribi rara sabaribi roi
Man la sama papa yoré faux billets yi sac à
Main lay dokhonto sétan len ma wiri wiri (Jari ndari)
Damay tothie sama monde (jari ndari)
Tothie sama monde (wiri wiri jari ndari)
Damay tothie sama monde (jari ndari)

Tothie sama monde
Tothie sama monde
Kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Carré VIP amoul guetou bëy kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Kay tothie sa monde
Carré VIP amoul guetou bëy kay tothie sa monde
(Jari ndari) carré VIP amoul guetou bëy kay tothie sa monde
(Jari ndari wiri wiri jari ndari) Carré
VIP amoul guetou bëy kay tothie sa monde
(Jari ndari wiri wiri jari ndari jari ndari jari ndari)

Tracker