Shooooooow!
Yegsi nga, yegsi nga
Shoooooow!
Deguetil déguetil
Shooooooow!
Sénégal pape yéksina
Bilay man suneuna ci wakhdji waawaaw
Kébétoubi bari na
Moom doy naaaay
Dama name degg dadji
Roumbakh deuguine dadj
Sama yaye beuguenalaaa yayou khadim
Yayou aladjéééé
Waawaaw tey ma rindieul leu say nderr yow yay boy
Tay ma bakeula diobé
Sargal yayiiii
Ndakh dangua degue dadji roumbakh deuguine dadjéy
Wouylélé lélééééé sama yaye ma yaye
Waawaaw ku mine seu khoulo yab leu
Ma chérie tongo bi moom jaru ko
Ni soo ko bëggee
Danga degg dadji té rombakh deuguine dadjéééé
Deguetil déguetil
Shooooooow!
Yegsi nga, yegsi nga
Shoooooow!
Pape fi ci pikine way
Shoooooow!
Fileu? Am fé leu leu?
Degue na dadjeuuuuuu
Waxleen ma fu ñuy tase
(Hey fu ñuy tase?)
Madison madison lagnouy tassé way
Degueul dadji yow
Dinaleu digueul lila kham ci mbakh
Walayé soumalané beuguenaleu cheikh
Ibil sey beut dima xool
Cheikh amar
Jangual sameu djikooooo
Bamou nékh la waawaaw yes!
Souma bakhé ngua kham nigno wara and bene famille bi la
(Waw dolima)
Cheikhoooo amar
Serigne saliou ngay begué
Cheikhoooo amar
(Séni mouchoir na sal bi wekh) domou ndéyou kader ndiaye, woy naleu cheikh
Ya beugue mame cheikh anta mbacké borom darou
Salam sameu serigne bééé cheikh
Cheikhoooo amar khamnga fonkeu naleuy ndakh sa mbakh sa talibé lérr na
Waw baye malamine bara bindeul namey téré, téré yassa saloum, saloum niéti néék leu biko gnintéél beu ci wagne beu wagne beu wagnou bour leu
Bour beu bourou saloum, fougnouy tassé?
Awa baldé borom kolda
Ibrahima, theuy lingay mbalakh
Gneupeu la lerr ndour
Waw aida penda ndongo
Domou ali coura ndiémé
Dafa dém ci farawoudé
Naneko dama beug tééré
Bilay tééré yamou dane sol eyway dafko simi lamssal
Ba ci tété ombiiiiiiiilé, dafko simi lamssal
Waw baye malamine dara bindeul namey téré, téré yassa saloum, saloum niéti néék leu biko gnintel beu di wagne beu wagne beu wagnou bour leu
Bour beu bourou saloum, fu ñuy tassé?
Gorou marie amar aka beug segn saliou
Eyway beugue yeugueu koy fay
Kila beugue meuno ko fay
Kileu beugue lay bégué cheikh
Kileu beugue lay titeuro
Beugue yeugueu koy fay
Kileu beugoul doula yeugueu koy
Kila beugue lay béguééééé
Kileu beugueu lay titeuro
Waw baye malamine dara bindeul namey téré, téré yassa saloum, saloum niéti néék leu biko gnintél beu di wagne beu wagne beu wagnou bour leu
Bour beu bourou saloum, fougnouy tassé?
Souma nallé beuguenala
Khipil sa beut dima xool man
Awa baldé sameu kharit la
Awa souma newé beuguenala
Khipil sa beut dima xool man
Awa baldé sameu jigéen la
Waawaaw ni béguéééééé di beuguééé di beuguéééé
Kay léne gnou bégué waawaaw
Usine niary tally fofala djoudooo
Gnouy béguéééééé di beuguééé di beuguéééé
Guinaw rail béguééé waawaaw
Parcelles assainies 1 beu 26 kayléne gnou
Béguéééééé di beuguééé di beuguéééé pikine waawaaw
Hoooooooooooooooo
Souma naléne beuguenaléne
Fans yi bégué négn léne
Bayé gado yayou pape bou ndaw
Ni dadj dégueu dadji o takh ngua meuneu raw say mass
Khalébi ridieul meu say ndér
Ni dadj degueu dadji o takh ngua meuneu raw say mass
Fans yi man dé bégué naléne
Wouy lééélééééééé
Dégueu dadj