notícias musicais

top 13 artistas

top 13 musicas

Confira a Letra Ton pied mon pied

Pape Diouf

Ton pied mon pied

Lu mu lëndëm lëndëm yaw rekk laay gis (ehn ehn)
Sa leeraay bidéew yaay leeral sama xol (ehn ehn)
Àdduna desalatu ma dara
Diggante bi Yàlla ko bind ca aras

Man yaa ma mëna
Loolu tax ma bëgg la
Yàlla ko bind ca aras
Ñaari xol yee tase baby
Man bi ma la seene ci la xam ni
Yaa war a contrôler zone bi, duggal but yi
Boyaal cax yi taxawe nee

Li may yëg ni dafa neex waaw du jeex
Sunu diggante du yucci xaajal kenn
Kaay fii sama amore
Ñu wan leen ni ñuy bëggante

Ton pied, mon pied
Foo toog fa laay dem
Kon li lu koy faay
Maak yaw ñu dundu ko
(Maak yaw ñu dundu ko)

Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko
Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko
Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko
Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko

Dama tégi as teg la plasu reine
Def pat ak organisé di ko dundu
Wër naa ci àdduna gisuma ku la gën

Li may yëg ni dafa neex waaw du jeex
Sunu diggante du yucci xaajal kenn
Kaay fii sama amore
Ñu wan leen ni ñuy bëggante

Ton pied, mon pied
Foo toog fa laay dem
Kon li lu koy faay
Maak yaw ñu dundu ko
(Maak yaw ñu dundu ko)

Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko
Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko
Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko
Oh oh oh oh oh
Maak yaw ñu dundu ko

Tracker